414 brothers - doumala bayii lyrics
[verse 1 = just]
top love ba faf soff
top love ba faf doff
top love ba faf loff fébar nioumay fadié rose
sama life da pause
mbind mou nice kom proz
usouma cocaine mais dama lover’dose
yay sama barbi
bayina bi-reu yi (reubi)
done sa brebis bouma mangué kane lay mbeuki dji
ya eulbati sama vie’yeungeul sama heart bi tothie sama kani touf sama beut yi
boudei love love dou yako soss
thanks god dieuredieuf baby awma sa fayy doumala bayi yaw ( x2)
[hook = metzo]
yone bi meitina wone nga diap teuweu bayi wo mak yaw démb la wone
doumala meuss bayi yaw
xamnga né yay sama xol mane déh soumala amoulwone wayé démb lawone
doumala meuss bayi
[verse 2 = klaus]
yay kimay safal
yay kimay bégueul
c’est toi qui me fais voir la vie en couleur
yallah na yallah motali
yéné gui ma am tchi yaw
ndax mayla keur ak merco toutina tchi yaw
fintal la sound bi warnama ling-y job si souf wornama
wate nané mane déh doumala meuss bayi yaw
teral tamitt warnama bégueul tamitt warnama wate nané yaw yay sama baby love
thanks god dieuredieuf baby awma sa fay doumala bayi yaw ( x2)
[hook = metzo]
yone bi meitina wone nga diap teuweu bayi wo mak yaw démb la wone
doumala meuss bayi yaw
xamnga né yay sama xol mane déh soumala amoulwone wayé démb lawone
doumala meuss bayi
[just]
mak yaw doufi yeup
feulei sa ar-ss la
yallah ko bind yague na
c’est pour la vie
[hook = metzo] (x2)
yone bi meitina wone nga diap teuweu bayi wo mak yaw démb la wone
doumala meuss bayi yaw
xamnga né yay sama xol mane déh soumala amoulwone wayé démb lawone
doumala meuss bayi
414 brothers entertainment
Random Lyrics
- malson atmosfèric - filosofia lyrics
- antologia polskiego rapu - ten typ mes - dwadzieścia pięć lyrics
- reik - sabes - en vivo lyrics
- ideal jim - me dis pas lyrics
- kidcrusher - distorted disorder lyrics
- 6 dogs - earth bound (ness + lucas team up!) lyrics
- yung jodhans - jxffrxy is scared lyrics
- dikers - angel lyrics
- cyro monteiro - você está sumindo lyrics
- varsity - elevator music lyrics