ashs the best - alxames lyrics
alxames lyrics
bësu alxames bu tiis ci waxtu timis
ci lañ ma diis naqqar bu tiis
alxames bu tiis bu tiis a tiis
ci lañ ma diis
suma waaji dem na {dem na} dem na {baayi fi njaboot ji}
dem na {ñëpp a koy jooy} dem na {weetal na kër gi}
salaama yaa seydi salaama yaa baaba taalibe maam ba′mba
xol bi rafetoon na
jamm laa la yeene
doonoo woon alie’ne′
aljana firdawsi laa la yeene salaama yaa seydi baaba
suma waaji dem na {dem na} dem na {baayi fi njaboot ji}
dem na {ñëpp a koy jooy} dem na {weetal na kër gi}
ebe njaxaa be ngandaa tobe fay be ngalaa kobe ñaami
dum ne muusi ni xaw nii sukaabe
africa ngummo deen (x) ngummo deen
liggo deen leydi meen saare meen
ñoo foowandoo maggandoo
def nañ lu ne
jaar nañ fu ne
lima la yeene
aljana laa la yeene doonoo woon alie’ne’
taalibe maam ba′mba
sa jëf ji rafet na baaba
bësu alxames bu tiis ci waxtu timis
ci lañ ma diis naqqar bu tiis
alxames bu tiis bu tiis a tiis
ci lañ ma diis
suma waaji dem na {dem na}
dem na {baayi fi njaboot ji} dem na {ñëpp a koy jooy}
dem na {weetal na kër gi}
report a problem
Random Lyrics
- sweetheart (rus) - delete me lyrics
- tank and the bangas - black folk lyrics
- gas denst - van gogh lyrics
- dlsa - broken-heart-syndrome lyrics
- michael prophet - happy days lyrics
- knki - rey misterio lyrics
- nightrage - swallow me lyrics
- ancient shapes - all the kids lyrics
- brayan medina - now you're just a stranger lyrics
- jluma - assurdo lyrics