
baye mass - abadane lyrics
doumala bayi
doumala bayé eheh
yawitt bouma bayi
boulma bayé yeah
mom nene daf leu beugueu piir
nena dafa beugueu nga nekka ki mou djital
mome néna yadi kimou guiss
nena ci niom nieup yaw rek la beugueu djital
nèna dotu la bayi
yaw la taneu si goor gné
nèna dotu la bayi
yaw la taneu ci djiguene gné
doumala bayi
doumala bayè
yawite boulma bayi
boulma bayè
abadane
abadane
abadane
abadane
yaw boulma bayi dahimane
abadane
abadane
abadane
abadane
doumala bayi dahimane
sa agne mo daakh louma meune lekk
sa keur mo daakh fouma meuna nekk
lougniou neex lekka
louniou neex nane
ndiabote gui fecc akka retane
mane dama la nopp ba dila beug fone
mane damala manguila chérie
dama la nopp ba dila beug fone
mane damala manguila chérie
doumala bayi
doumala bayé eh
yawite bouma bayi
boulma bayè eheh
abadane
abadane
abadane
abadane
yaw boulma bayi dahimane
abadane
abadane
abadane
abadane
doumala bayi dahimane
Random Lyrics
- bebelsito - sosa trem lyrics
- lil murky - fall with rain lyrics
- knak - moncler lyrics
- badchieff - ziel lyrics
- dvertigo - call up the reverend lyrics
- format6537 - прошлое (the past) lyrics
- daniel obede - goose lyrics
- dawn of orion - the ancient promise lyrics
- dj myke - full time (remix) lyrics
- manù de dios - pkmn lyrics