baye mass - capitaine lyrics
capitaine lyrics
fi lepp tamalé, fima la guissé
dangma romba ma tago sama sago
lu g+yi neka di wakh degatuma ko
diaama rek la bugon
ndakh ma diokh la sama xol
lima dugal sama xol xawma lumu done
so ma rombé dotuma muna khol
dumala meusa muna bayi
jiteul ma ma done sa ouroul ayni
benj koye ligeye demb la wone
yay sama champion
yay sama linguère
benj koye ligeye demb la wone
bilaye mbeuguel moye capitaine boromam
su djiné beugé ku yeug dang+ye danou
bilaye mbeuguel moye capitaine boromam
su djiné beugé ku yeug dang+ye danou
dumala meusa muna bayi
jiteul ma ma done sa ouroul ayni
benj koye ligеye demb la wone
bilayе mbeuguel moye capitaine boromam
su djiné beugé ku yeug dang+ye danou
ahh bilaye mbeuguel moye capitaine boromam
su djiné beugé ku yeug dang+ye danou
Random Lyrics
- mefiu - treaba ta! lyrics
- myth of her - lizard man lyrics
- pooh shiesty & lil ki114r - big blrrd* lyrics
- cielo grande - tu mamá lyrics
- pedro rivera - corrido del salvador lyrics
- niz - in love lyrics
- lil tecca - xtra* lyrics
- mey.bae - alma lyrics
- βητα πεισ | vita peis (grc) - αξέχαστο (axe) lyrics
- king monday & azileli - before i wake lyrics