baye mass - ndaw lyrics
ndaw la bou déme
déwé n′a ndaw fougnou dieum
ndakh koune ci nioune
amna loum donone thi yaw
yallah bouy dieul
dou tagou day dieki rek dieul
nagne len ko ni+n+l
mou am diam foum meuna dem
donone na domm
donone kou sori ci niom
dioté wone ak yaye dji
wayé domm dey sakh ci xool bi
fi nieupeu dioy
fi nieupe la sen xool yi toy
li ko metti wone
teknako ci lokho kharite bi
xolal soy rendi
lo rendi sa lokho lay nathie
sonné ké di dieundeu sa famille boul sagane mouy nadjé
ki kouko wakhone
li la fiy dieulé sa khel bi lay diougué
watte ni douka meussa guem
xolal soy rendi
lo rendi sa lokho lay nathie
so neké di dieundeu
sa famille boul sagane mouy nadjé
ki kokou wakhone
li la fiy dieulé si sa khel bi lay diougué
meun na watte ni
watte ni douka meussa guem
aduna yagg na
loye deff nanko khol
ning+ye nyowé, nonu ngai demé
fi ken hamut li ngai feki
li ngai ligey rek nga xam
suma xamone suma demé ni lay moudjé
kon ma togg
demm na dottu delousi
ndeye ak baye nieup nyungi joye
rethiou daal di wess
ku sanione bala ngai demm tago bayi ganaw
bokk ye xarit yi teww ci keur gui munneh selew
fimu nekk nieupa t++t
fimm né nieupa diakhle
nitt ku tey la wonn
nitt ku bakh deum na
xolal soy rendi
lo rendi sa lokho lay nathie
sonné ké di dieundeu sa famille boul sagane mouy nadjé
ki kouko wakhone
li la fiy dieulé sa khet lay diougué
watte ni douka meussa guem
xolal soy rendi
lo rendi sa lokho lay nathie
so neké di dieundeu
sa famille boul sagane mouy nadjé
ki kokou wakhone
li la fiy dieulé si sa khet lay diougué
meun na watte ni
watte ni douka meussa guem
Random Lyrics
- diamond mqt - ร่วงหล่น (prada me) lyrics
- jeckyll mc - tehom lyrics
- атрава (atrava) - атрава - заброшка (abandoned) lyrics
- noa mal - 2000 lyrics
- frescasipp - mef freestyle lyrics
- пропаганда (propaganda) (rus) - забываю (forgetting) lyrics
- escombro - guillotina lyrics
- thanks for coming - losing touch (nyc) lyrics
- hibeekay - ore ofe lyrics
- haiden - sorry to your next ex (acoustic) lyrics