bossbeatz xat xol - dinama nekh (pollution sonore) lyrics
refrain : (bossbeatz & dj total)
dinama nékh, wakh niou lilay nékh (boulniou yakal)
lii moniou nékh, wakh niou lilay nékh (té boulniou yakal) (x4)
couplet 1
(dimélo)
damay rap guay get naneu ki dé goor djignéneu la
tek ko thi tempo yok clap b-tch do thi géneu
ambiance de guagua mandi hum madi bandit
rabou niari s-x hum maniague k-ssé
di di di nala nékheu dimélo dinala nékheu
boudé diabou wally mola goudi dinala nékheu
mayma tokhou toubey ak demi shirt
géweul daffa yatou bayiiil ma dokheu thi tanki baye
(bab’s blac’k)
deup dippi deupeurdi takhoul mou guiss
soulay nékh dalay béteu limou yoora diss
soko meunoul aadji callal makhou ciss
mako mome mako meune mako yélo
soriba woumako kone doumako délo
ndaw rabine dialguati douggie ya kham boul-ssi nékh
l’essentiel ték ko si temps yi bamou diékh
hé dinama nékh dinama dianama nékh
refrain : (bossbeatz & dj total)
dinama nékh, wakh niou lilay nékh (boulniou yakal)
lii moniou nékh, wakh niou lilay nékh (té boulniou yakal) (x4)
couplet 2
(bossbeatz)
j’ai l’argent, j’ai le teint (appelle moi argentin)
2014 doko faté (7 la si bresilien)
tarbiyou done si talibé, dissi diangue a i b
mise en garde ni prohibé, strange music taxawél né
may rap gua youxou (ohh) ni kou tiime tatou nicky
harlem city flow, apate néma biggie
teubeul ma teup, sa baye teup, haters yi bokk golo gui (x2)
non non non dama dioum niou démate
teubeul ma teup, sa baye teup, haters yi képe golo gui
ndiabal ma ndiap ma am diap domou ndeye temps la way
(bouzot)
okay we do it, do it do it like an animal
mic cheick 1 2 yobouleuh benen monde
dadjie dathie ng-y deff i know you like that
esk golo meun neu yék fou kawé diaroul ladjté
switch this is how we do it boiie
bou dara sedd na lepp yeungou tay dara dou doiie
dope boiie enjoiie listen to da bad boiie
boudé lii dinala nekh, diokhko seu baye boiie
refrain : (bossbeatz & dj total)
dinama nékh, wakh niou lilay nékh (boulniou yakal)
lii moniou nékh, wakh niou lilay nékh (té boulniou yakal) (x4)
couplet 3
(rafall)
dinama nekh, ma djeule sa tof pixéliser
dindi gag-gag, xésale harmoniser
photo bou nice guay weur, mane la rafall
lathe ma mami, amina, wala aida fall
tasou wala guébatou no limit da niouy xoss
deub lou djoubone, amoul ragual thiap sosse
yaw na loxo yi tathiou bathiou djeumélé xat xol
han!!! dinama nekh, thiap léne ko
(fonetik)
boula nekhé r-ss tiakhagoune kheuthieul mbalou djeune
rimbi rimbi noki airou bégué bayi mathie tougne
happy rék no stress diamono twiss lagni dékélate
thia thia rumba salsa amoul teudje xalate
dokhalak mom wouye athiou combattaako tako
dadone mér ba foute way bayil foné bapko
bothie bifi tiali tiali lay nakhé déli coco
magui foo di rap tewoul yaye sama cheri coco
refrain : (bossbeatz & dj total)
dinama nékh, wakh niou lilay nékh (boulniou yakal)
lii moniou nékh, wakh niou lilay nékh (té boulniou yakal) (x4)
Random Lyrics
- coby - ja to volim lyrics
- tássia reis - agora eu quero ver lyrics
- bispo - lembra-te lyrics
- faberyayo - diep in het notenwoud lyrics
- diam's - a quand mon heure ? lyrics
- o.d. kill - vdn lyrics
- paris violence - creux de vague lyrics
- bart baker - taylor swift lyrics
- thumpers - unkinder (a tougher love) lyrics
- talking heads - radio head - 2005 - remaster lyrics