bossbeatz xat xol - galsen dundul déwul lyrics
1er couplet
dioudou si année 70 yi si fin fond wou bronx
kool herc abeu si jamaicain mc yi taxaw toast
mouy avancé ndank ndank ba theodore di feuleuk scratch
nioukoy xéxx diko geem hip hop taxawé gninte pathie
fok niou xar 79 suggarhill ték first album
master flash ékssi woté message. rap bi déf boom
nwa f-ck na police. ganstar rap diotena dioudou
ba rogolate biir paris banlieue feug séni bountou
welcome si dakar. année blanche di vidé école yi
niou téri si smurf ak breakdance tons yi créer possee
ambroise ak aziz coulibaly génération 80
puissance fm yok dolé nioukoy geem di geuneu bari
immigré yi feule. single si mbacké dioum
album si mc lida. fok niou tékk ataya
pbs dougeul riti. marimba si black mbolo
galsen démarkéwou. promoteur yi intérrésséwou
refrain
galsen mafia dafa beuri unknowers
douniou meusseu nane séne nda me and my brothers
souniou mission si game moy niodi boy you nara souroukh
diokhagn léne baram wane léne where is the trust
2eme couplet
98 rapadio eksi fini l’age d’or. mister kane dékil rap
under pa déf k.o. bibson ni fata fake la
dééf ko guérre dorikay canon
gaston, omzo dieul défensou l’exilé bambino
2003 concept rap new generation. (walabok)
geble tigrim b woté innovation
entre temps matador slam. carlou d ni day musikr
xuman thiape si reggae bi. awadi yotou public afrique bi
niounouy wowé grand jobatouniou. akima nd… rap bi
ték sene béne lobby. dounou mayé chance wakh ko boy yi
légui kou fipouwoul diay léne prék do lék si ndap li
heureus-m-nt canab-sse télla adji know louy deal bi
alien si bénéne planete. pps si bénéne f-ssette
néna tane na boudoul dé. mixtape yi di takarn-ssé (undecl-ss)
slang bi di geuneu djolofé. kanaraw ni f-k n kuk
takricain ték sagn sagn. gars yi lém séne guéne ni moute
refrain
galsen mafia dafa beuri unknowers
douniou meusseu nane séne nda me and my brothers
souniou mission si game moy niodi boy you nara souroukh
diokhagn léne baram wane léne where is the trust
3éme couplet
galsen gni ni dounou créer dounou inventer
waliyanne ba nopi reuy lamigne ni nioko mome
bou kana yi dégone wolof dounou diok si dinou ré
réinventé termes yi deugeur fiit di doul di dadialé
]fi ganstar amoul xaliss. fi ganster dou dougou jail
fi ganster beugoul lou baxx. fi ganster sakh amoul guél
old yi geem lo public bi ni boy yi biniy déf dou rap
meunouniou binde di teup di daal si ay beatou dirty ak trap
ténor yi déf faux départ déloyal bagne kouléne daap
faténaniou ni demb nio nékone séne guinaw di support di clap
ay animateur a la con niou saupe léne si béne lobby
méme gars yi naniy ték niénéne gni daal xamouniou gaate
dagnay kathie ba nopi beugue ma geemlo ni fénou niou daal
nopalal sa bopou doma délo époque féodal
bossbeatz dou boyou kéne. bamay adji xamoumaléne
laye balde, sonsam, mbaari ngoné fatéwoumaléne
outro
big up to all my n-ggers. lord jock, papa cisse
bril fight 4, sanzala, rosso, 3g team, car rapid
reptil music, 221 bangers, avocat, mc boudeur
etk, pee boy, nikel kami, fonetik
sama grand r-ssoul réspect sikki sakka
xat xol for life releve by force
Random Lyrics
- beks - mit meinem weibchen lyrics
- sidxram - пако вайб (paco vibe) lyrics
- fonky family - dans la légende lyrics
- momus - the charm song lyrics
- vanilla ninja - dangerzone. - long version lyrics
- mc keke - encomenda lyrics
- vossmusic - neverland lyrics
- the spits (band) - tonight lyrics
- yunnin - pensando demais lyrics
- gloria groove - problema lyrics