carapid music - 94' lyrics
[verse 1 : bako]
okay na beat bi dal kick bi danou lepp daldi andeu danou
ins bi nako kepp ni guey képpé guels yi door ba danou bro
ngandim mamou casque samay nopp faw niu defni wally seck
fessal salle yi fokniu thiop balla go
ouh la la laaaaa
wakhouma papeu thione borom faux gees
bako niuni jayz, fla niu ni eazy
kalz nekk nas , escobar dou you feel me ?
[hook : maya]
ohh so we goin’ back yeah géné sunu baggy
négn léne déélou 94
délou temps wou biggie, makaveli pac yeah
négn léne déélou 94
94 , 94 , ninety
négn léne déélou 94
94 , 94 , ninety
négn léne déélou 94
[verse 2 : kalz]
béneu vinyle sameu bag
history’s on my back
ay photos black & white dimeu fatali ay wikidiwhack
baggy strechin’ survet takini yem ssi
ni run dmc yagg rendi mc
cl-ssic…
ni soiree séna le paris ci ciné
genak seu cho daldi parer djadjak mome paré si nék
cl-ssiiic
ni kou am gel bu mol niou naane leu takal
lo beugg lu life seu lérr outil plan takkal
[hook : maya]
[verse 3 : fla]
miss the time rap was about the real
no autotune but sick rhymes n nice flow to hear
out in the street freestyle without the beat and make the fans cheer
the time it was about the street about the fans n not about money and fame
speak for the voiceless n talk about ur sh-t less
but n-gg-s been talking cr-p
with their trap but ama strap that rap wrap that sh-t n flush
[verse 4 : pps]
[outro: maya]
ninety attitude , faté autotune
neu nieup douggou tok si car bi yokh leu 94
ohh ninety attitude , faté autotune
lemme break it down , break it down , break it down
changeéti cap, sicap,deungeul ay cap
yangui capter? 4 sur 4 ngéne tok si seize
sister please,sister pleaaaase
rap bi dégn qo yagg maitriz
Random Lyrics
- tiger army - sundown lyrics
- bakersteez - imagine lyrics
- people call me gonzo - i'm on the internet lyrics
- cavin - palm trees lyrics
- eli seeney - violince lyrics
- ronela hajati - veç na lyrics
- yasir (looneyy) - loner lyrics
- orodruin - war on the world lyrics
- kaisa - schlaflos lyrics
- eddy baker - don't stop lyrics