carapid music - epic lyrics
[kalz]
hey waleuwaleubok bou kéne tok
yéneu ko done ladjté nioo ngok
carapid si kaw ni sorore
aneu gni done waxx né dou dokh?
niata aate niou néé si, ni messi fils déniou beurri peripéties
si biti done dj-ssi rendi beats yi gars yi signé si s-ssi !
[fla]
sunu 2e projet niu saani, niune bokkuniu ak boys yii salé
déniu meun lignuy déf tékci wané, nekk ci game bi di innover
yeah daniou sadik… melni kou yague addict ci kali
daké ay mc sandiji mbeubeus ni mbalit hann
[bako & fla]
kane mo fi tané ci yene?
kane mo niouy danel ?
niune niogui fepp, guediawaye
ba niary tally !
[bako]
are u ready n-gga get it limoy pour gars yi done guetter
nn dou seddeu, amoul seral, on top déniuy sorri !
ep modaf-ckaaa, li dou yeufou fakeuu
homie foniu fekk niogui job… fréqueu
rap ba suniu bopp yi dara dou ci né
suniuy djang doko degg: daara wou djinné…
Random Lyrics
- los acosta - ni por todo el oro del mundo lyrics
- passionate mc - the book of forever lyrics
- nocando - no romance lyrics
- el komander - detras del miedo lyrics
- gucci mane - candy man lyrics
- k'la - im off it lyrics
- swift guad - vice lyrics
- monty python - brian song (monty python sings) lyrics
- greekdagod - rockin n rolling lyrics
- yunggflexx - take off lyrics