carapid music - one shot lyrics
[bako]
yo…yaguena dougou ci beat bi normalement
wayé par moment damey beugeu touti changement !
(anh) damléndi fumer comme ay mégots
2500 mégas , sam gars yi bégat
rap dou fowou egate amul sani leuz beugeu nekk ndér
taxaw guinaw gnigni mélni takka ndér
loula taxeu méér ? no flow !
sa tape dey flip di flap wessou na flop
fi la fé leu wala felé khamo fu gni feullé
déma follow na follow back soumko feeler
anh… carapid today nikka, ac toom nikka
everyday nikka ! niogui ni alright té dou dégn nikka
diém nga pouss wayé suniu rap dou déy nikka !
tek leu fitneu, keep leu, kick leu, tchip leu
douma rime ac k!ller sinon ma k!ll leu…wow!
niateu années niuy planer ci under-planete ?
légui party diekhna paréna kou beug parrainé bako ?
[refrain : kalz & fla] (x2)
dioxma stylo bena feuy ma defko one shot
fat fat niu binde 16 barres one shot
1,2,3,4 flow rhyme ac technik , flow rhyme ac technik popopop
one shot !
[kalz]
mane..damey…
adj seu nd-y neu youkhou lonkotinaa (aah)
defalé ay dégats ni ouragan katrina (aah)
reudeu sameu kanam deter ni rebellou casa
légui déniou am ay fans partout dans continent (aah)
guiss na ko mouy hate si di doule sameu timeline
néko doum ko faalé mane dg weum lay ladj
nénegn kalzi limouy egotrip dafeu xaweu beurré
mais esk mouss neu guiss mbeur bakouwul bala mouy beurré?
mane saxx…dama nieuw pour mettre les points sur les “i”
et mon poing dans vos gueules , voila comme ça c’est dit
comme dangéne fokné nioune ak yéne nio dém béy bokk team
f-ck it, boul djawaalé barça ak niarry talli
hail mary !! ‘coz i’m way tupacer than you
rendi na fi ay mcs mais niata pakeu la use?
maa léy maarlo naane ni kouy joobé s.d.e. (whoop whoop)
carapid bi dou taxaw , nio fi dakk brouulé feu!
[refrain : kalz & fla] (x2)
[fla]
its your boy fla
rap is in my dna
so f-ckin update
b-tch am like miraculated
dama touti sama droite sec floyd meywether
fouma rombeu def ay ravage melni bad weither
da ng-y rap conscient wala sa rap mo constant
siisi dafa stagnei tei souniou boss dafa exponentiel
yeahh nangoul boy yi nio beuri potentiel
di rap dirty house party teksi thematik
dafa complikei ci ioe rap mathematik
liniouy def fils aka ca–milei
boul jeguei fi fils daniou niou ka– minei
xam nga ni daniou efficae ni acide a–miné
ahhh mouné? dafay a–nulé
non fils boul gueneu rang yi kay niou de–filé
li kado rek leu boy pr sene nvelle année
li kado rek leu boy pr sene nvelle année
[refrain : kalz & fla] (x2)
Random Lyrics
- cornershop - heavy soup lyrics
- cordell francis - wanna whoo family lyrics
- ether q - top down, hands high lyrics
- j-zone - jackin for basquiats lyrics
- joe-g - j'aime les histoires lyrics
- amor dinero - im 1deep lyrics
- cahoots - down lyrics
- lastboyfrnd - “op” lyrics
- prinz pi - laura lyrics
- esne beltza - nahi dut lyrics