carapid music - waitin' lyrics
[intro : bako]
lumu yagg yagg déy nieuw
lumu tang tang bul daw x2
[verse 1 ]
[kalz]
mangui dém ca caw kanam
souleymane gadoul seu xalam
xér béy doni done ngalam
tonil djeumeulél seu kanam
mic check, essai!
ngané ma do dem do percer!
sameu carriere moy avorter?
waflash, maa sané!
[fla]
gemeul job bi my boy deubeul
dangeu nareu wor kone xeudeul
ndjeukeul yewou takou deugeur
deum yi sakh dégn léne di ndeupeul
[kalz]
droitier la mo takh méy job gauche
ndakh beugg fessal poche
[fla]
kouy djité niongi paré def putsh
bagneu nango took touche
[kalz]
dameu yagg khar souy nieuw muy nékh
[fla]
bayal seu waaar ni daara j
done ndongo done faada ji
it’s the school of life kone déy métii
[kalz]
yagg négn job ay cds
[fla]
natt bi nio kéy tégi
[kalz]
djox meu beat meu tépi
djox meu beat meu tépi
xamougn bopp seu bopp, déniouy ték foundation lépp djok
done number one pour gni peu meu topp , mo tax dumeu messeu djouk si job
[fla]
talouma xar mbokeu joug war mana bok
mame xa ak bandi mic diko teugeu samay nopeu
[bridge]
boul meu séén
boul guiss méy tok di cool ngeu fokni mane
amouma…
luméy séntou si aduna,mane rékeu xam
[refrain : bako]
lumu yagg yagg déy nieuw
lumu tang tang bul daw
weurseukou yallah boy diarul xadi
lumu yagg yagg déy nieuuuw x2
[verse 2 : elzo jamdong]
[bridge : maya]
[refrain : bako]
Random Lyrics
- björk - i miss you (dobie's rub part one sunshine mix) lyrics
- sifon - thanks we say lyrics
- suave-ski - hustlemode lyrics
- de lux - moments lyrics
- oba oba samba house - mulher de fases lyrics
- kaaris - c'est la base lyrics
- echo & the bunnymen - way out and up we go lyrics
- out of the dust - i will go lyrics
- lil stanky - kill lyrics
- nómada - no more mr. nice guy (signed off) lyrics