dip doundou guiss - noboma woon lyrics
le passé c’est le passé
pour nos problèmes moi avec toi
j’en avais assez
maintenant que tout a changé
j’ai tourné la page parce que
tu m’empêche d’avancer
tchi dirr bou gate la leu
kham nga beug ma jugé
ci sa digue sa ay kharite
nga séwal ma ni
mane yorouma wone xaliss
té gniko yor sa xol yow
meusso len ko thiabile
bamala guissé si la guissék
nitte kima done sett
façon yen goor gni nieupa yam
ngané ma meunoul né
mane mélouma ni gars gni
sa tank sama tank présenté ma pa bi
hey ! nga bagn né dett dou maak yow
damala meuné mouniou dem fen maak yow
indil ngama kénén ndax doumala am yow
yow ci sa bop yama téré and ak yow
nga bagn né dett dou maak yow
damala meuné mouniou dem fen maak yow
yow ci sa bop yama téré andak yow baby
n0boma wonе
n0boma ndeysane n0boma wone
bama lеy facetime taloma wone
no boulma message no bouma wo wooo
oh ! n0boma wone
n0boma ndeysane n0boma wone
bama ley facetime taloma wone
no boulma message no bouma wo wooo
n0boma wone
n0boma ndeysane n0boma wone
bama ley facetime taloma wone
no boulma message no bouma wo wooo
oh ! n0boma wone
n0boma ndeysane n0boma wone
bama ley facetime taloma wone
no boulma message no bouma wo wooo
kouma ko waxone doum ko
geum ya moudié khéwi ni
mane yow rek la guissone
nga diapéma ni invisible
bayi nala a vie
faté nga big mey romb ak vitessou ferrari
mbeuguel indiwoula lila indi dieuli na
tay ngamey soga meuna set fepp ni f.b.i
reuthi nala bayil, wadji ma done
dieundé tay nako niémé trahir anh
nga bagn né dett dou maak yow
damala meuné mouniou dem fen maak yow
indil ngama kénén ndax doumala am yow
yow ci sa bop yama téré andak yow
nga bagn né dett dou maak yow
damala meuné mouniou dem fen maak yow
indil ngama kénén ndax doumala am yow
yow si sa bop yama téré and ak yow baby
n0boma wone
n0boma ndeysane n0boma wone
bama ley facetime taloma wone
no boulma message no bouma
wo wooo ! anh
oh ! n0boma wone
n0boma ndeysane n0boma wone
bama ley facetime taloma wone
no boulma
message no bouma wo wooo
n0boma wone
n0boma ndeysane n0boma wone
bama ley facetime taloma wone
no boulma
message no bouma wo wooo ! oh
n0boma wone
n0boma ndeysane n0boma wone
bama ley facetime taloma wone
no boulma
message no bouma wo wooo ! oh
pourquoi tu crois aller venir quand tu veux
mais cette fois si là c’est trop tard
wo wohh
Random Lyrics
- byron band - monstrul de sub pat lyrics
- пиксели (pikseli) - птср (ptsd) lyrics
- verónica castro - la chaparrita dinamita lyrics
- 6arelyhuman - dance with u lyrics
- pl (피엘) (kor) - 접속 (be brave) lyrics
- iker ocampo - otra noche lyrics
- wenow - высокий рейв (high rave) lyrics
- mocro yakuza - khabat lyrics
- deadsun (band) - crucify lyrics
- gold, frankincense, & myrrh - the enemy lyrics