dizzy kha - aksina lyrics
1st verse :
kouko done lath aksinegne
dawal hopitalou rap niou vacciner… leu
bala guay get sama album non mixtape , rap galsen lay confisquer
def sama pocket, le reste guen forget
dizzy the name a.ka the best of the best
souma yéksé fi c’est parce que bamouy méti dawoumeu
niom nio yekh wala maa gaw té pourtant dawoumeu
sama beusseu fenthie noy def ba nopiloma ?
lepeu louma denthione lay guéné fethie lola
hawma foumeu dieum hawma foumay dali mais
geum geum ba takh lerna dina arriver
yone bi leundeum na mais fite mognouy niteul yone
kougnou mognaléwoul khoff noy def ba t-teul ko ?
egotrip leu boudoul freestyle
boy bi migui briller ni boulou crystal .. yeah
chorus :
aksina (x2)
metiwona mais aksina
yone bi goudone na trope yeah my n-gger ndiap na ba sone
dem ba khamétoumeu sama yone , mais douma lathté andak sama ngor
motah aksina
aksina (x2) yeah
metiwona mais aksina
2nd verse :
adouna moussoul diouk si tester ma
souma déwé tey diapel tape bi testament
magui dokhane bene guel, tekki la toudou
dafmay diay nekh mais si ndekki lay moudiou
everyday taggo studio,studio ba kagne?
ba kaagne dougou,filek maguek bakane
#yagga teek ay projets si pete wolouwma kene
none bou khamé figua dieum dalay goalou my friend
#yague guama togne ma #yague la diegeule
f-ck you yak sa sete kate mane yalla la degeule
sou khamone fima diougué digua khamni doma té dem
hamgua fima tambalé mais khamo foumay téré
sougnouy teew dagnouy def gang jamais solo
#yague nekeu ay def kate boul diay fodo
yeah #yaggadream tourou tape bi
#yague nagnou nateu dougnou tebbi
nakh nio dieul lepp : talent wak buzz
dama dieul péé my n-gger banaalak deuss
nieupeu beugeu rap mais nieupeu meunouniou nak
yegue na bay nane tianyn n-gger meunougn ma dapp
eupoumafi chance mais walai amna niouma tané
téneul bomay khol nakh legui dama kaawé
balais, moy limay wadia def nieneu si yene
guéneusilene,walabook ma fekeusilene .. yeah
chorus :
aksina (x2) yeah
metiwona mais aksina
yone bi goudone na trope yeah my n-gger ndiap na ba sone
dem ba khamétoumeu sama yone , mais douma lath té andak sama ngor
motah aksina
aksina (x2) yeah
metiwona mais aksina
3rd verse :
té nenegn rap dafa dewone, kone tey dina dekki
legui job la moudiedone , kone fokmou andak wethite
dougnou meusseu faté sougnouy frerots , yougnou #yagga geum yeah merci
ndam bi dou yeksi ba kerok , ba kerok guakoy fekki
outro :
(yagga dream) sicap azur stand up
(yagga dream) reptyle is the label
(yagga dream) tape bi moy sene boss
(yagga dream) maynako nieupeu gnouko #yaggakhar
Random Lyrics
- niko is - floss lyrics
- l118 - waiting lyrics
- iam_rubio - society ft. oscar cruz lyrics
- nancy ajram - inta eyh lyrics
- i.t.m - ma vie lyrics
- florent pagny - comme d'habitude - florent pagny version lyrics
- izzy-meeks - izzy's interlude lyrics
- the anomalies - 1830 lyrics
- ndfzc - dumbo lyrics
- mac tyer - abimé lyrics