gun mor - rebel lyrics
yes i′m a rebel
miner na sama zone
kou nieme na kaye
téréw ma kene sama kogn
boudé dang ma degeul
doma meusseu pésé
ladjal gni beugone dawe niou game niata balle laniou késsé
dama wex ni leweul
baxouma si xolou maguette
rakeu ndaw wouteul fo lakatou balaguama guet
bougouma armé national bi guéneu dima wanted
ndax listou rappeurs yiniouy geuneu soralé jsuis en tête
yes i’m a rebel
sam boppay sama forêt fils
ndirowoumak keneu fi guisna niguene maye xoley fils
sama xel moy sama doley makoy yokk doley fils
falew ma sax president yoo f+ck all his authorities
man i′m a rebel
anhhh
yeah yeah
yes i’m a rebel
me, myself and i
we’re all rebels
anhhh
yeah yeah
man i′m a rebel
(rebelution)
me, myself and i
we′re all rebels
extremophile ni tardigrades
si mane crime you geuneu sedd paka poute ak ndiambi tate
déf kom temps boy yewou fadjar sathi mango sandica
lois yi respectèwougn ma motax mane respectéw ma loi
n+ggah i’m rebel damay takeu yegeul level up
takeu manane shine faylak acide si tu fais le thug
diameugeune si yene bala maleni firil mbari feute
dama ma haïtienne comme haïtien vite ma déf fi feu
yes i′m a rebel
sam boppay sama forêt fils
ndirowoumak keneu fi guisna niguene maye xoley fils
sama xel moy sama doley makoy yokk doley fils
falew ma sax president yoo f+ck all his authorities
man i’m a rebel
anhhh
yeah yeah
yes i′m a rebel
(rebelution)
me, myself and i
we’re all rebels
anhhh
yeah yeah
man i′m a rebel
(rebelution)
me, myself and i
we’re all rebels
Random Lyrics
- nisə qasımova - şahanə sevgi lyrics
- dorof & maratti - 300 flow lyrics
- childish gambino - 2 brains lyrics
- mmllr - не надо делать вид (you don't have to pretend) lyrics
- smokeez (rus) - уйдешь вновь (will you leave again) lyrics
- verni gonzales - kamusta ka lyrics
- mermaid blood - by the river lyrics
- tadotheband - everything is funny now lyrics
- harlekin (de) - arch enemy lyrics
- mmllr - любовь (love) lyrics