ismael lo - incha allah lyrics
incha allah incha allah
bou eulegue dana bakh
incha allah incha allah
bou eulegue dana bakh
xal-ss warouna halebi mougui dieme
di wout yone boumou beugue wayak
bayam bay yemou nèko dome togal
khar aduna ndakh diaroul guawtou
amna fo wara diare kon khamna bou
eleugue dana bakh
bossi andék p-ss p-ss
kon baye tok néko
incha allah incha allah
bou euleugue dana bakh
incha allah incha allah
bou euleugue dana bakh
adouna diaroul gawtou
téla soti bakhoul
kon diangal b-ssi kanan
bou mokke dana yomba lol ba diakhal
la waye nak defsi sa fulak sa fayda
ndakh kou niakha dina diarignou
mane kon dome adunabi diarul
di gawtou
he he he he he
incha allah incha allah
bou euleugue dana bakh
incha allah incha allah
bou euleugue dana bakh
incha allah incha allah
bou euleugue dana bakh
incha allah bou euleugue dana
baaakh
incha allah
bou euleugue dana baaakh
incha allah incha allah
bou euleugue dana baaakh
he he he hee
adouna amul solo oh
incha allah incha allah
dana bakha hehe hehe
Random Lyrics
- big red panda - fugitive lyrics
- pablo montero - el abandonado lyrics
- mojinos escozios - guarra lyrics
- jasz.official - wake up lyrics
- aüb (panormal) - oublie-moi lyrics
- ras kass - soul on ice lyrics
- lucio bukowski - psaumes métropolitains lyrics
- tainá costa - ritmo envolvente lyrics
- fritz kalkbrenner - one of these days lyrics
- big o, th@ yung chase, shaman - the come up lyrics