jay 21 - fagaru lyrics
[refrain]
douma père bou improviser
diour dom sandi diaroul viser
flowou tchoutchou flowwou missile
bayil meu djiteul sama
f+garu, f+garu, f+garu
aduna bi ne ci crise
sa perspective yi deum yi guiss
mais maman nekoul niit kouy guiss
mais moma djiteul nema
f+garu, f+garu, f+garu
dama dieul ci sama siss mane
yeugeul fi, indi séisme
té dou yolé dou policeman
f+garu, f+garu, f+garu
nga né dang beu beug siss
f+garu
diapa deret dina tiss
f+garu
diour dom sandi diaroul viser
[couplet 1]
everyday
ma ngui mousli ci sama bord du job pour sama bop
nginté
bébé 4k dioud diapal nioune jobou niou ci bénévole
anything
sa choix dou niourok sa voice, di nga guestou guiss meu bala guestou guiss beu get lou diss capi+jay mbetch leu tchit bala nga beuss n+gga f+garul
mayday
beneu trône nga am moy cabinet bi nеk sa gale bayil di gnodi king djiss nga king bi demal wakh imposteur yi ma nga еkci gnou f+garou
jay jay
ki leu bot di beuré da ng+y niane mou dane bi beuguer bonder dessal sama trampoline fi dialou mbaye faye geuneu deugeur ouzin barigo
f+garu
kou seral niou taral ko
sen bizness yi takhaw neu pourtant jay paregoul
sene son yi day meti bop
flow jay ci mane day melni nga dieul panadol et je parle en parabol pedophile yi beug am moral tamalé mbalou sen propre photo khale nio fi nekone demb fi aduna diangale nama
[refrain]
douma père bou improviser
diour dom sandi diaroul viser
flowou tchoutchou flowwou missile
bayil meu djiteul sama
f+garu, f+garu, f+garu
aduna bi ne ci crise
sa perspective yi deum yi guiss
mais maman nekoul niit kouy guiss
mais moma djiteul nema
f+garu, f+garu, f+garu
dama dieul ci sama siss mane
yeugeul fi, indi séisme
té dou yolé dou policeman
f+garu, f+garu, f+garu
nga né dang beu beug siss
f+garu
diapa deret dina tiss
f+garu
diour dom sandi diaroul viser
[couplet 2]
21 record niou hisser
diour dôme sa di diaroul viser
sama cible la nek di pister
malo dap rap mais il sais
chocolate boy douma tisme
mowti flow leu yone leu mou flipper
newena ko bayil mou glisser
wiri wiri diari ndalé mane bayi ci xel
da am jay après y’a les ndares my n+gga bayi ci xel
f+garou ci sama people
f+garou bobama titeul
f+garou ndakh dagn meu djiteul
rap bi dokhoul flow bi dama sa tank nga diar radio siw beu pare beug sikeul
doma tere sigui
rab bou téla iri
weer kou dindi slip
codal mic bi firi
danou guerrou siri
sama y wakh di pillule
flow bou rare ni kinine
rap bi samay cellule
mane guili doma tere sourire
yalla tachou beu bizness bi fetch
sentou assamane diarouta boulhante kaw dokhantoufa t gérer sa petch
[refrain]
douma père bou improviser
diour dom sandi diaroul viser
flowou tchoutchou flowwou missile
bayil meu djiteul sama
f+garu, f+garu, f+garu
aduna bi ne ci crise
sa perspective yi deum yi guiss
mais maman nekoul niit kouy guiss
mais moma djiteul nema
f+garu, f+garu, f+garu
dama dieul ci sama siss mane
yeugeul fi, indi séisme
té dou yolé dou policeman
f+garu, f+garu, f+garu
nga né dang beu beug siss
f+garu
diapa deret dina tiss
f+garu
diour dom sandi diaroul viser
Random Lyrics
- lil seng - fall in lxve lyrics
- mc caverinha - evoque lyrics
- a vida music - lugar de refúgio lyrics
- rockit gaming - becoming alive lyrics
- mayot - untitled lyrics
- mashaole mogale - 1. lies lyrics
- scorp 2500 - mais longe lyrics
- tex crick - sometimes i forget lyrics
- mick spek - drugged lyrics
- mockcharge - creature of the underworld lyrics