azlyrics.biz
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

jay 21 - kouy sa baay lyrics

Loading...

[refrain]
latch ko sa baye
dégouloma demal latch ko sa baay
djissouloma demal latch ko sa yaye
ki lay tak fok mou tekki
bamou djang dieguer tekki sa baye
wala sa yaye
niom niomeu diema touteul tay mais sama souba nara daak tay way
baby bye+bye
aduna keneu khamoul souba meune nga tassel kou gueneu tekki sa baay

[couplet 1]
bouma sagnone damay dokh ak gomme
gommer sama life li gueneu bone
li geuneu bone gnou gass dougeul ci tombe
maybe damay changer forme
tamit teleu caisser com
yeah boba dagnouy djiwatlo
solna bou yag manе sama kimono
maybe souma diaroutone fouma diar douma tassek yaw bеy nek sa g+yn
mais baby bye+bye

[refrain]
dégouloma demal latch ko sa baay
djissouloma dagn meu latch kouy sa baay
ki lay tak fok mou tekki
bamou djang dieguer gueneu sa baye
baby bye+bye
niom niomeu diema touteul tay mais sama souba nara daak tay way
baby bye+bye
aduna keneu khamoul souba meune nga tassel kou gueneu tekki sa baay
[couplet 2]
lougn diot dund demb mane doumako weer fi
djiguene dagn kay souteureul mane douma la weer fils
démone na beuy né boul tite may done sa père rou fils
sougn may latch money sen yaram dou daw
lou meu djiss motakh meu dieul sama distance
dioural meu fils doko deg dou resistante
baby bayima meu niit
niom nenagn meutouma ndjit
kou kham lou yalla di bindeu ngene may juger tiam way
bye+bye

[refrain]
dégouloma demal latch ko sa baay
djissouloma dagn meu latch kouy sa baay
ki lay tak fok mou tekki
bamou djang dieguer gueneu sa baye
baby bye+bye
niom niomeu diema touteul tay mais sama souba nara daak tay way
baby bye+bye
aduna keneu khamoul souba meune nga tassel kou gueneu tekki sa baay

[couplet 3]
yeah yeah
sen wa keur gno meu latch kouy sa baay
yeah
sen wa keur gno meu latch kouy sa baay
yeah yeah
sen wa keur gno meu latch kouy sa baay
yeah yeah
sen wa keur gno meu latch kouy sa baay
nenagn dagn meu diepi
maybe dagn meu khep mane
bougn sagnone dagn may sepi
khamougn sama khet mane
dagn fogone douma investir
ndakh dama yag fiesta
doma nelawal ci chaise bi
li moy simple sieste
nenagn dagn meu khep mane
nenagn dagn meu khep mane
nenagn dagn meu khep mane
nenagn dagn meu khep mane
nenagn dagn meu khep mane
sen wakeur gnom meu latch kouy sa baay
meune ngama djiss t doma sen
ci télé bi ngamay set
do garantie bo amoul permi
sa wakeur jeez lagnouy sen
mais jant bi kou kay fay
ya pas compris ami chance
bo amoul jeez dara free
kouy oubli bo takoul chaine
talal télévision
sama souba moy daak
kham nga li nek sama vision
maybe li yaak sounou soubeu ya né ibliss leu
waro khep baby keneu khamoul lane la yalla dintcheul sa morom
baby bye+bye
[refrain]
dégouloma demal latch ko sa baay
djissouloma dagn meu latch kouy sa baay
ki lay tak fok mou tekki
bamou djang dieguer gueneu sa baye
baby bye+bye
niom niomeu diema touteul tay mais sama souba nara daak tay way
baby bye+bye
aduna keneu khamoul souba meune nga tassel kou gueneu tekki sa baay

dégouloma demal latch ko sa baay
djissouloma dagn meu latch kouy sa baay
ki lay tak fok mou tekki
bamou djang dieguer gueneu sa baye
baby bye+bye
niom niomeu diema touteul tay mais sama souba nara daak tay way
baby bye+bye
aduna keneu khamoul souba meune nga tassel kou gueneu tekki sa baay

Random Lyrics

HOT LYRICS

Loading...