azlyrics.biz
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

jay 21 - mouno resister lyrics

Loading...

[refrain]
heee yaye
nala yobou rome yaye
ya meu yok diom yomb
teukoul sa morom
ñi manjako douma bayi
me tell them
talou meu di dund nguisteul
yok dolé rap bi wiss ko
diay leu dole pare wiss leu
tak rap bi terroriser leu
pourquoi nga siss meu mouno résister
twenty one leu gnouné dix leu
pourquoi nga siss meu mouno résister
ki tak rap bi terroriste

[couplet 1]
ki taak rap bi terroriste leu
do lek f+gadaga do ci dara diay leu dolé pré wiss leu
yalla djissoul sacrifice nit you bone yi, nangou nianou gni gneme risque
yaw ak ki ng+y guinz ci bop kogn bi yeine bok bakar bi d guiss nga
nane ngamay diapé sa fils man
yéné yi dou louy mousseu tolo manе douma ci plafonner meme alors cartе gap
pourquoi nga siss meu fo meu djiss tchipatou
do meusseu guiss pape bou toub
nou may def ak sama people
bayima sandi verre whisky yi
kaddu diok neu kaddu ngnit leu
kaddu diot leu kaddu djit leu
yeah
dafa diegui job gentleman
gueneu kawe dieguer sentinelle
rap bi kane leu wara sant tay
hip+hop bi niak santé
cryptonite lay fompé
ci sa biir enfanter
ki nga djiss mola improvise ba nga hanter
[refrain]
heee yaye
nala yobou rome yaye
ya meu yok diom yomb
teukoul sa morom
ñi manjako douma bayi
me tell them
talou meu di dund nguisteul
yok dolé rap bi wiss ko
diay leu dole pare wiss leu
tak rap bi terroriser leu
pourquoi nga siss meu mouno résister
twenty one leu gnouné dix leu
pourquoi nga siss meu mouno résister
ki tak rap bi terroriste
[couplet 2]
pourquoi nga siss meu mouno résister
ki taak rap bi terroriste
t dou job nguisseul
raciste beu diomal métisse
mane feyagouma wayé labagou niou tamit dano gouma sobou nagn
même tank yi goudou, loxo yi bagna goud, xaroul loxo fils fok meu diem han
nga né sama kaname est ce que xam nga ya ngui sama cible man
mané procureur dou garawalé, sama none yi sama tiatou wé
pourquoi nga siss meu mouno résister
wotel village sa sorcier douma guiss té mounouma pister hé
imbécile yi wolou sen brain
yakamti dou takh meu diawlé frein
bougnou sagnone tay meu bagna kheuy
dou meuss tela fay ni gareth bale
xarouma keneu youkhou ana jay
sene idiotie mo leine taylé tay
couvre+feu bi mako déclaré n+gga dou mbelé mbelé toom boul tela kheuy
ouh ouh ouh bou goumbeu di djité goumbeu wakh meu louy xew
legui amna sokhna am baby
awma diotou keneu ma ngui ci diotou yaaaye

[refrain]
heee yaye
nala yobou rome yaye
ya meu yok diom yomb
teukoul sa morom
ñi manjako douma bayi
me tell them
talou meu di dund nguisteul
yok dolé rap bi wiss ko
diay leu dole pare wiss leu
tak rap bi terroriser leu
pourquoi nga siss meu mouno résister
twenty one leu gnouné dix leu
pourquoi nga siss meu mouno résister
ki tak rap bi terroriste



Random Lyrics

HOT LYRICS

Loading...