kach - the reason lyrics
first couplet
si yaw la miir, si yaw la doff, yaw la dieul denk la sama bope
si yaw lagne ma xiir motax douma xof gnoune niaar sougnou wéété sama lep day off
yaay sama biir, yaay sama biti lolou mo am té ken dindi
you’re the only i trust han demalak mane foula neex like vivi
li nit yi di xool mane bé guissou mako. li nit di wax mane bé deggou mako
def nagne louné mais yaay number uno boul degg boul guiss pleas takham louko
god mognou moom té moognou boolé def gnou nek ay siamois
ma def la ni dom ngamay yokkou doolé
hunhun mami té amo
ha bé mane yaw la nope beuguélou tiakane taxou ma diok
after mon pere et ma mere yaw rek yaw ya tax may job
please honney denk ma nop mane sama love wessou na finga ko fogg
bala mouy neex ma yoonéla gninthe ak tranche gnew dieulsi la finga tokk
refrain
when i wake up in the morning bb you’re the reason
gotta get my money right bb you’re the reason
the only time i left a cry bb you’re the reason
nothing gonna change my decison u got me sing
2em couplet
dara gueunoul nga tok finga tok di sentir ni amna koula beugue
amna koula meuneu understand dila topato dila wax tamit deugue
dara gueunoul neex goor néla boudoul yaw awma kenene koumay xool
sho yi nignou beuri yaw rek la tane dieul la taf sama xool
dara gueunoul neex goor beugueleu ba nopi teksi doone koula yeureum
yééna la adouna ak lissi yééna la keuyitou keureum
ng-y accordé boumou xoolam néfa faax diko xalam
lolou lep koula koy defal guisso ko danga gueuleum
bé saa yo signé réé damay guiss samay yaayou doom
dama guenthe gnou yééwou si bene lal lolo ma yokkou dioom
souma diotoone -ssamaane wer bi laay recupéré
teuyé ko di niit sa yoone fo diaar mou leer melni tééré
refrai
when i wake up in the morning bb you’re the reason
gotta get my money right bb you’re the reason
the only time i left a cry bb you’re the reason
nothing gonna change my decison u got me sing
outro
beugue nala bene beugue nala niar niat gninthe 10
Random Lyrics
- 2guns boyz - you betta let em go lyrics
- disiz la peste - shadow boxing lyrics
- ndgo - 33rd lyrics
- rappers anonymous - rare lyrics
- doctor p - neon (feat. jenna g) lyrics
- monocordio - siempre te busque lyrics
- forever unfinished - vibrix lyrics
- airospace - judas iscariot lyrics
- dj exquizit - hot nigga lyrics
- julia sheer - let him go lyrics