maabo - namel (round 7) lyrics
namel (round 7) lyrics
maboo, oh oh
baby, yeah
baby namm na laa
honey, yeah
honey namm na laa
sama xolama sori
dem nga daani doolé bayi maak wéétay
yama dan mottali, banga démé la gëjj yëkk nééxay
yaw yaa taxoon, ma bayi xarit yima am yepp
té benn xarit, la désé woon té yaw la dem nga
budoon ñént f+kk att, dina ko tokk dila xaar
yama fékk si lëndëm, taalal may far léral sama yoon
man rekk ci xalé, nammuma kudul guisé maabo
kenn du yaw té yaafi mën, yaa mey jox li gën ci man
baby i miss you
yes i really do
honey i miss you
how can i live without you?
quand t’es loin de moi
je ne vis pas
je mourrais 100 fois
rien que pour être dans tes bras
baby i miss you
yes i really do
honey i miss you
how can i live without you?
quand t’es loin de moi
je ne vis pas
je mourrais 100 fois
rien que pour être dans tes bras
lima sori tax ma jaxaso
wéetay moma teuj kaso
téléphone doyuma
baby yaw namm na laa
damalay sentir, nga jégé té sori ngama
bul mérr, bul firr, guisuma fi k+ma lay jëndd
lég+lég ma jum ndax tërëdi
yaw kassé rekk ci xol dara xaju fi
linga bëgg moy ma ñibi ci
xamo ni mala gënn bëgg ñibi ci
mbëgeel, kénn xamul lumuy
def ci nitt bamuy, namel
baby yaw suma la mënoon indi fi kenn waxatu ko
quand t’es loin de moi
je ne vis pas
je mourrais 100 fois
rien que pour être dans tes bras
baby i miss you
yes i really do
honey i miss you
how can i live without you?
quand t’es loin de moi
je ne vis pas
je mourrais 100 fois
rien que pour être dans tes bras
baby i miss you
yes i really do
honey i miss you
how can i live without you?
toucouleur bu rafet bangi ni, hé
boroom nag ak mééw bangi ni
hééé yamay danel
dang ma nammoon mangi ni
namm la tax man ma ñibi ci
dang ma nammoon mangi ni
namm la tax man ma ñibi ci
hé, hé, hé, hé, hé ! diobadio arri !
toucouleur bu rafet bangi ni
hé, hé, hé, hé, hé ! diobadio arri !
boroom nag ak mew bangi ni
hé, hé, hé, hé, hé !
toucouleur bu rafet bangi ni
hé, hé, hé, hé, hé !
boroom nag ak mew bangi ni
Random Lyrics
- mr. parr - crust, mantle, cores song lyrics
- running wild - the iron times (1618-1648) lyrics
- frankenbok - heart with fire lyrics
- bran & derin rodoslu - images lyrics
- izel - anlayamazsın lyrics
- me contro te - uh na na na lyrics
- teck-nique - the legacy of marquay rogers (ep) lyrics
- the grinning plowman - secret sugar frosting lyrics
- elias niemietz - take it easy lyrics
- miri yusif - 3 sual lyrics