mia guissé - la vie est belle lyrics
[intro]
on ne vit qu’une seule fois
on ne vit qu’une seule fois
une seul fois
vient on s’évade
tché on the beat
on ne vit qu’une seule fois
on ne vit qu’une seule fois
une seul fois
[verse 1]
dey leundeum may shine
mbow mbow duñu dara
bul gestu bul falé
laisse les bavarder
mane buy neex duma doyal
lu melni mane weureul
dawal ba melni évadé bébé
dieun bu reutieu tchi ay filets bébé
[pre+chorus]
jaunе banana (banana)
fuma guéné tchi rouge ba dagu fa yeup vert
sama sourirе mo eupeu dollé balu fétel yeah
wurus bu yalla ngalam
meuno wakh beu sopi ko peureum
yeah yeah yeah
[chorus]
yen mba namone nguen ma
nga def lu neex
wayé diekh na ñeuw na
ma def lu neex
kone fi mu né baax na
bo defé mu neex
beuy du volume di nana
bo defe mu neex
yen mba namone nguen ma
nga def lu neex
wayé diekh na ñeuw na
ma def lu neex
kone fi mu né baax na
bo defé mu neex
beuy du volume di nana nana
la vie est belle
[post+chorus]
on ne vit qu’une seule fois
on ne vit qu’une seule fois
une seul fois
vient on s’évade
[verse 2]
ñaw
ku nekeu tchi dig dig leundeum dal
yalla diekki rek taal sey lampes
nguey doxal doxal
di doxal doxal
dara feyyu ma mane
diappa loxo ki né sa weet
ñu begué bala ño deem
kone doxal doxal
ñu doxal doxal
[bridge]
darra feyu ma
mane ma key yeungueul yeungueul
yeungueul mu nane reugueudj reugueudj
fecca ko ni ku ridj beugueudj
effet yi ñoy créer émeutes
guisso ni makey yeungueul yeungueul
yeungueul mu nane reugueudj reugueudj
fecca ko ni ku ridj beugueudj
yen mba namone nguen ma
[chorus]
nga def lu neex
wayé diekh na ñeuw na
ma def lu neex
kone fi mu né baax na
bo defé mu neex
beuy du volume di nana
bo deffè mu neex
yen mba namone nguen ma
nga def lu neex
wayé diekh na ñeuw na
ma def lu neex
kone fi mu né baax na
bo defé mu neex
beuy du volume di nana
bo deffè mu neex
yen mba namone nguen ma
nga def lu neex
wayé diekh na ñeuw na
ma def lu neex
kone fi mu né baax na
bo defé mu neex
beuy du volume di nana
yen mba namone nguen ma
nga def lu neex
wayé diekh na ñeuw na
ma def lu neex
kone fi mu né baax na
bo defé mu neex
beuy du volume di nana
hey la vie est belle
[bridge]
mane ma key yeungueul yeungueul
yeungueul mu nane reugueudj reugueudj
fecca ko ni ku ridj beugueudj
effet yi ñoy créer émeutes
guisso ni makey yeungueul yeungueul
yeungueul mu nane reugueudj reugueudj
fecca ko ni ku ridj beugueudj
la vie est belle
[outro]
bu ma guené si rouge ba dagu fa yeup vert
sama sourire mo eupeu dollé balu fétel yeah
wakh yi du romba yerrè yi
faxassulene
faxassulene
Random Lyrics
- zeremy - they march on!! - juices squad s3 theme song (chinese version) lyrics
- lisa pariente - je m'en fous lyrics
- magnum opus & pinq - жаль (sorry) lyrics
- baker ya maker - go to war lyrics
- james wames - conflict of interest (farewell) lyrics
- death tour - strictly 4 my divaz lyrics
- james reid (nzl) - time is another lover lyrics
- moha mmz - feu de camp lyrics
- карандаш (karandash) - могу позволить (can afford) lyrics
- chanje - no more humain lyrics