azlyrics.biz
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

ngaaka blindé - néma waw lyrics

Loading...

[intro]
mbarikalah, no
it’s a real love
mbarikalah, no
ok…

[verse 1]
this is the real love
ma nara déf ci mom
mane xale bi rek la love
ba nara dof ci mom
hey baby, chéri chou sava
he naka warr?
hey baby, chéri chou sava
comment tu vas?

[chorus]
xalé bi bou retanei
sama xol bi day mel ni lem
so xalé bi bou doxei
tiakaas, tiakaas guin teus
mane beug nala dieulci nga seuy ci ci mane néma waw
nga dioxma sa loxo niou ande di fly néma waw

[verse 2]
bouniou andei di dox di waxtane
sama xol bi nekh
bouniouy waxtane di tiow rek moe thiayne
sama xol bi fekh
nénako beug naleu
est ce que saxe beug nga
mou nema love naleu
mais est ce que sakh deug la?
baby, please
baby, kiss
baby, geun ma wiz
baby, geun ma wiz
baby, geun ma biz
baby, you’re lovely
so, everyday and every night
baby, my sunshine
you are my life
you are my wife
baby, geum ma way

[chorus]
xalé bi bou retanei
sama xol bi day mel ni lem
so xalé bi bou doxei
tiakaas, tiakaas guin teus
mane beug nala dieulci nga seuy ci ci mane néma waw
nga dioxma sa loxo niou ande di fly néma waw
xalé bi bou retanei
sama xol bi day mel ni lem
so xalé bi bou doxei
tiakaas, tiakaas guin teus
mane beug nala dieulci nga seuy ci ci mane néma waw
nga dioxma sa loxo niou ande di fly néma waw

[verse 3]
guel yima topeu beuri nagne
mais lolou doú darra way
beug naleu way
bouniou xoulo beugou
mala bayi
nena gorr yim diota
xam maléne gueunea diantal
bouniou wetei tamit ci nek
maléne gueunea bantal
dinama faune
raay tiokotane ma way
leg leg mou dompaat
ma teup tombat
mou ree bijou ma rek songat
té nane ma do gat
mbarikalah finii do gat
dagal sompaat
wiss ci salade
tégue thi tomate
jus d’orange bi dal ma rek
nga xamni amoul diambat

[chorus]
mane beug nala dieulci nga seuy ci ci mane néma waw
nga dioxma sa loxo niou ande di fly néma waw
xalé bi bou retanei
sama xol bi day mel ni lem
so xalé bi bou doxei
tiakaas, tiakaas guin teus
mane beug nala dieulci nga seuy ci ci mane néma waw
nga dioxma sa loxo niou ande di fly néma waw
xalé bi bou retanei
sama xol bi day mel ni lem
so xalé bi bou doxei
tiakaas, tiakaas guin teus

Random Lyrics

HOT LYRICS

Loading...