nitdoff - better leave lyrics
[refrain]
better better leave you better leave
better better leave you better leave now
better better leave you better leave
better better leave you better leave now
sagua djiap door torokhal
bou fekké beuguato bayil mou leave now
nioun goorr suniu beuguatoul douniou assumer
nioy push djiguen bi pour mou craquer sassounéh
[pont]
better understand use sa brain
kiléy diade lo dou sa friend
dedet dou sa nawlé bokouléen
safane rekk ley doundé daw beu rénn
[couplet 1]
daw guaw soriko bala mouy late
nga melni mom rek ley wait
amoul ay kheuy amoul ay kilifa tayit
ci liko nekh rek ley nekk
boul doff boul tokk
ak kiy beugua freiner sey ambition
dey djiem daley bapp taukh ak nane
bou sanione nga ceder tentation
bro t+n+l sey andado
nio khamni nio gui ak sen saguo
meytoul gniy prek
loy dougu néy léer
defkat yi meytoul sakh sen shadow
[refrain]
better better leave you better leave
better better leave you better leave now
better better leave you better leave
better better leave you better leave now
sagua djiap door torokhal
bou fekké beuguato bayil mou leave now
nioun goor suniu beuguatoul douniou assumer
nioy push djiguen bi pour mou craquer sassounéh
[pont 2]
togual mounie
na fekk mou doon kouko diar
khole atanoul
yénn yi meun naleu raye
[couplet 2]
n+gga seuy dou jail
peine nou perpétuité took fay dound h+ll
tellement belle nga fi niane ci woon
sopiko t’es ma chienne
dieul seu responsabilite doneu kilifa ngey banie
fanane aleu tamba balou sa bakane limou beugu dokoko khagne
[refrain]
better better leave you better leave
better better leave you better leave now
sagua djiap door torokhal
bou fekké beuguato bayil mou leave now
nioun goorr suniu beuguatoul douniou assumer
nioy push djiguen bi pour mou craquer sassounéh
Random Lyrics
- holl & rush - believe it (feat. mike james) lyrics
- lina and the lions - this fire lyrics
- new life worship - imagine lyrics
- negative xp - beamer boy 2020 lyrics
- sanrioboyz - s/`.nrio g/`.ng initi/`.tion lyrics
- marqer - impostor lyrics
- затми (zathmi) - лакуна (lacuna) lyrics
- kwame heingzy - jah guide me lyrics
- figura renata - di balik huru hara lyrics
- girl fry - you, me, and the people that scare us lyrics