nitdoff - cii pèt lyrics
[couplet 1]
yeah yeah aaahan
yeah yeah
sama xoll mo tiakar
fess ba tourauk nakar
sama xell teudiou mané fils on rek
melni kouniou teuthie prison break
sama euleuk leundeum, sama thieur yi né lou peuyiss
xeuy hopital gontou police
deuk cii bèn poukouss ak sama weuliss
xalé yi yapp ma, djiguène yi xepp ma
askan wii beurgueule maa, sheytané xeur teulma
cii pet lakoy doundeu ak yène
dotou ma xalé borom fane werrii attela (30ans)
sa youma wétté sama sagarou mattela
waniarou dj+pp sama bopp fébarou tékki
sama xoll bii di sékki
ya !!!
douma incapable bounetou yeupeu teudiou
bokk yeup adiou
cii pét laay doundé gathié bimaay yéndo
pa bi dieum na makk té mère bi damako yeureum
sama yéné cii niom mo kawé té yorouma deureum
souma sanione wakh djou yakouleu
lifi né moy awouma fiitou nieuw sen keur dii niane soxna
sama yakar+ra takk djeupétt
makoy doundeu cii pét
liimay ragal biss guène dégg né salite naa
ndakh gathié siiittt naa, té doundou bi tek nama fitna
thiow djipp naa, borom fiitou gaindé titna
borom fiitou gaindé titna
[refrain]
yeah yeah !!! cii pét lakoy doundeu ak yène
yeah yeah !!! cii pét lakoy doundeu ak yène
han !! cii pet lakoy doundeu ak yène
yeah !!! cii pét lakoy doundeu ak yène
[couplet 2]
ya ya ya
askan wé niou imposé am am
ba taxna kou niakk yaw ak xalé bou ndaw yéneuy yem
kène dou lathie sa waw ak sa détt
sa guiss guiss cii lène bokko, yorokko, lo wakh niouné
ohooooooo !!!
yeah !!! pression = pression
niata nio sopii sèn direction
ndakh meuneu touniou waune dékou sèn situation
basculés cii yamba, alcool, gainze, ak agression
xam naniou né gueunoul
mais société bélèn tek louniou meunoul
yaw bania deff nii niom motakh maay nott sama bakane bi déy
thieuy so xamone limay dathie ak sama back+in+the+day
mane rek+kaay dess cii scène bii bouniou ropé diak yii
ak samay back yi (gars yii)
wathié samay casquette biiy neup sama beutt you taa+yii
sama vergogne takh malèni neubb sama rongogne
[refrain]
cii pét lakoy doundeu ak yène
yeah !!! cii pét lakoy doundeu ak yène
cii pét lakoy doundeu ak yène
cii pét lakoy doundeu ak yène
cii pét lakoy doundeu ak yène
[couplet 3]
yo
barça wala barzak mouk
xarou douma tchii fekk
donté légg légg sama xell doxonetou
ma siiki saak xell niarou
sama gueum deufeul maa
yalla ma tekk natou té niakk dou saakh
souma rombé guène tchipeu touma dieuwma
té mane xawouma sama tort moy awouma
cii pét lay massla ak yène bagna setlou limeuy nieuklo
nimaay yotté ak nimaay yeuklo
kouma sétsi ma rouss ko entrée cii sama sagarou pentré
nakar bii cii sama xoll laniou ko encré
[refrain]
cii pét lakoy doundeu ak yène
yeah !!! cii pét lakoy doundeu ak yène
han !!! cii pét
yeah !!! cii pét lakoy doundeu ak yène
yeah !!! cii pét lakoy doundeu ak yène
[couplet 4]
yeah yo yo !!!
cii sama xalima lay yegg ligni mbébett cii xoll yi
diko togué cii pneu kogne bi cii keur yi
prézi niombar, wérou niou, lékou niou, nékkou niou
gorrou niou yattou niou, nga dj+pp niou ,ndiapé niou
cii pét lay diwo sama déba+dépp nguir samay weurseuk tidiékou
cii pét lay amé touti yakkar dii gueum nii yalla douniou sétane
none yi digni rétane
cii pét lay djougué guène diéngou soufeul sama djeumeu bagna xepp sous métier amoul
talal niou faayla ak talal niou maayla yémoul
daga wara yéngou cii dara yalla wakhoul kène lène
kou talal dii niane sa bopp ng+y yapp lou
daga wara sabapp lou
djégou fipou mélni kou khapp lou
lamb dathie borom fiitou gaindé dou tiitt wala
djougueul cii bopp kogne biga tokk di la+ ngal loss
melni kouy arbitré finalou laurent garos
mao mao arrétel beat bi
arrétel beat bi please
[outro]
yo ngour guéniou bédieune
founiou beug moniou faa té dieum
bour ndiogne guinar+ram
badola rossi guédiaam
prézi ndel+lam ak costumeum
souniou estomac youy dioy laay degg sa soudé xoss tchineum
f+ck sèn système
meunou mokko guiss dém
kambe gui loumou xautt xautt
fass nama yéné soulii saay mbautt
rimes yilaay diourgauutt
deugg djileuy thiokotane
sama nafa yi dii guileu né xétou pokotane
magueett nga rass nga, yakar bou tass nga
boulène tékeulé deug ak doul waay
amena niit you mérité woul tourou abdoulaye
yeah hannn haaaa
this go out to all my n+ggas who tryin’ hustle tryin’ j+++++
i know n+gga another life for livin’ in
galsen is so hard
but we don’t have no choice man
hustling wake up my n+gga, it’s time now
yeah !!! to all my n+gga who hustlin’ everyday
all my n+gga who tryin do something
this go out for u n+gga
never give up the fight man
sssstt ………….for life
one day will come
we….. …… my n+gga
just keep it real
keep positive my n+gga
right
Random Lyrics
- loek beernink - liefde is een raadsel lyrics
- smoke skreezy - smoke lyrics
- the beat bugs - i am the walrus lyrics
- catherine dagenais - mieux s'y voir lyrics
- dropskies - hate me lyrics
- sl!m d!zzy - ain't going home tonight lyrics
- hmz - choupetta lyrics
- john hiatt - nothing in my heart lyrics
- jay eye - greeze lyrics
- rhea sun - train lyrics