nitdoff - doing my time lyrics
[couplet 1]
do you know i’m doing my time yow
do you know i’m doing my time yow
deukoumafi mane damey diar dialeu yow
do you know i’m just doing my time yeah
soumey niew andalè souma diné
zero baakar guiss nga ni meu cleané
ki meu sakk bindal nameu weurseuk
fi meu wareu diar kenn douko disturb
i just doing my time
one life to live
in god i believe
warouma di guiss sama bopp ci lénn
douma ci lénn
damey diar rek dém
ki meu fi andi woon moy kènn
[refrain]
do you know i’m doing my time yow
do you know i’m doing my time yow
deukouma fi mane damey diar dialeu yow
do you know i’m just doing my time yeah
xamouma ndakh damey goudou fane
worouma ndakh dina amiy dome
mom liko soope danane doonal mou doon
[post refrain]
buur yallah def li gueun ci nioun
loum dogual niou nangou té mounie
moy kiy sakk moy kiy def moy ki meun
[couplet 2]
gueum nani fi deukou mafi damey diar dialeu
dina waslou akh guass beu samey part balleu
xamna ni fi meu tekk samey tank mbartaleu
mais souma démék ngeum dina yégu barkaleu
yénn saay nga dém beu fokk ni li sa meun meun leu
ngey dokh ci léer dina gueuneu réer ndeké leundeum leu
lotou naniou ci matt leu diam may niou yermandé
bi nga niouy sakk amoul kenn koula doon seconder
mindafoun yi nga sakk yepp nitteu léen gueun
bi nga né malaka yi diouli léen niepp léen gueum
ménoum ibliss mo wanè reuy wanè orgeuil
takhaw sissou beu dieumi taye dji mo niou lorr key
taxaw sabal la kènnal leu mo niou war taye
ndakh adouna bi kouko waroon demb moleu war taye
[refrain]
do you know i’m doing my time yow
do you know i’m doing my time yow
deukouma fi mane damey diar dialeu yow
do you know i’m just doing my time yeah
xamouma ndakh damey goudou fane
worouma ndakh dina amiy dome
mom liko soope danane doonal mou doon
[post refrain]
buur yallah def li gueun ci nioun
loum dogual niou nangou té mounie
moy kiy sakk moy kiy def moy ki meun
Random Lyrics
- kadie karen diekmeyer - the word i to indicate me lyrics
- diomay - outro lyrics
- 88lien - alone放空[outro散场曲] lyrics
- teyy - major lyrics
- ondfødt - tidin e komi lyrics
- yavid - calliope lyrics
- miguel veleda lyrics lyrics
- implements of hell - uniform demise lyrics
- vita peis - aμαρτίες lyrics
- faultline avenue - odödlig poesi lyrics