nitdoff - fokk ma lathie lyrics
[refrain: nitdoff & mao sidibé
fokk ma lathie !liiddé liddé kagn lay diekh
fokk ma lathie !liiddé liddé kagn lay diekh
fokk ma lathie !liiddé liddé kagn lay diekh
fokk ma lathie lathie lathie ba guiss kou tontou
fokk ma lathie ! liiddé liddé kagn lay diékh
fokk ma lathie ! liiddé liddé kagn lay diékh
who? my n-gg- fokk ma lathie
liiddé liddé kagn lay diékh
yow! fokk ma lathie lathie lathie ba guiss kou tontou
[couplet 1]
fokk ma lathie
loutakh léppeu keupou ci mane
loutakh maay xeuy di wékou cii nit té kèn dou wéku cii mane
loutakh may xeuy di tèneu di xoll té douma sèneu -ssamane
loutakh sama life tiss nioumaay xolé beutou ndeyesane
daniou maay khép douniou maa guiss daniou maay rombe né seun
maay gueuneu nour si guédjiou nakkar, you can’t understand
sama fiit meuneu toul tokk ndakh ay yakaar you t-ss
dama aay gaaf cii pét wala ma niaka daw f-ss
sama xoll di diékh vide nii sama calpé
niak singuilima foutima dima palpé
sama doundou wét melni ndiouly bou amoul salbé
maay xeuy di lathié louma def ba mérité li
mba dou sama liguéyou ndéye cii la herité li
bissbou nek limouy indi cii ay khétou problème
diougué cii li danou cii lé da ng-y djiém té do dém
niou ték la yafouss vaut rien bi tekki wo touss
[refrain: nitdoff & mao sidibé]
fokk ma lathie !liiddé liddé kagn lay diekh
fokk ma lathie !liiddé liddé kagn lay diekh
fokk ma lathie !liiddé liddé kagn lay diekh
fokk ma lathie lathie lathie ba guiss kou tontou
fokk ma lathie ! liiddé liddé kagn lay diékh
fokk ma lathie ! liiddé liddé kagn lay diékh
who? my n-gg- fokk ma lathie
liiddé liddé kagn lay diékh
yow! fokk ma lathie lathie lathie ba guiss kou tontou
[couplet 2]
fokk ma lathie lathie lathie ba guiss kou tontou
lou takhe ma nango sakou am am di xeuy di gontou
té meunone def ni niome tokk cii boppou kogn bi fontou
beuri diom ma takh ma bania tokk si keur gui nioumaay khonetou
té fouma démé baye aamé yakar life bi dathie ma pontou
ma danou waatt cii kambe gui tambalé waatt à zéro
souma ko diappé ni dina yékha warr pagérot
saalite-tangue maay yott seung sama geueme felleu
mougn na ba sama mougnou kaay fessena delleu
magui cracké tchii yonu sinébare ak guène braqué
sama égo yegg naa boppam beutt yi nioma traqué
di blamé baa cii askane wi ma bokk dagne ma plané
[refrain: nitdoff & mao sidibé]
fokk ma lathie !liiddé liddé kagn lay diekh
fokk ma lathie !liiddé liddé kagn lay diekh
fokk ma lathie !liiddé liddé kagn lay diekh
fokk ma lathie lathie lathie ba guiss kou tontou
fokk ma lathie ! liiddé liddé kagn lay diékh
fokk ma lathie ! liiddé liddé kagn lay diékh
who? my n-gg- fokk ma lathie
liiddé liddé kagn lay diékh
yow! fokk ma lathie lathie lathie ba guiss kou tontou
{couplet 3]
souma néwé cii guente feugue maa néma diougeul
mane limaay dounde ni natou leu wala mbougeul
tamouma di loubeul damaay liguèye di dioubeul
cii ndiguel la meusseu sakh di moytou loumay diggeul
souffél sama bopp té kouma guiss daadi laay yégeul
waayé melnani taay yoyou djiko niomay téggeul
bonne daffa yombeu beuri wonne neu loumay diombeu
beuss bou né niou kh-ssma né meu sa morom yagui laay rombeu
nit gni danio yakamm ti ta yalla daffa yékh
ko cii wakh mouné leu def lou bakh mofii diékh
bène lakk laniou dégue mouy cfa
boka yoroul légui le courant ne p-sse pas
[refrain: nitdoff & mao sidibé]
fokk ma lathie !liiddé liddé kagn lay diekh
fokk ma lathie !liiddé liddé kagn lay diekh
fokk ma lathie !liiddé liddé kagn lay diekh
fokk ma lathie lathie lathie ba guiss kou tontou
fokk ma lathie ! liiddé liddé kagn lay diékh
fokk ma lathie ! liiddé liddé kagn lay diékh
who? my n-gg- fokk ma lathie
liiddé liddé kagn lay diékh
yow! fokk ma lathie lathie lathie ba guiss kou tontou
Random Lyrics
- wyte knight - lone wolf (solo version) lyrics
- white punk - страшный сон* (scary dream) lyrics
- koorosh - maroochia (club remix) lyrics
- george crystal - story lyrics
- rodrigo wegner - tiempo lyrics
- rapid956ixx - my world lyrics
- beam - lost lyrics
- serena rae - salt (live acoustic) lyrics
- hold tight! - always lyrics
- lailien - snow white lyrics