nitdoff - gangsta egotrip lyrics
[couplet 1]
yo
beug siw beug akk wala nga beug daradja
feuk mic dengueul khaf gars yi nénagne la cana nga
say rime nimou yombé ni diay katou bana bana
sa flow dafa périmé sa kaw laay uriné
yow ak gnila fal king ak pd yila couronné
mc meuno niou couillonné
dang+y séral niouy bouillonnés
xalima ak paper thiap dadji limko
melodie ak tempo pogné mic bi timko
teugueul bakk djigneko
beugne yi takk sèènko
mbed bé ma tingome
feussal sama kingdom
always n° one
douma xeuthio n° two
xaliss la ciii mobutu
tchi ay compte laay neubeutou
see my dream come true
sante na alhamdu
samay yéné annetu
mbeday wakh maay bametou
meunou malène pay back ( payer en retour ) yokk léne ba yeggko
2h dou meusseu dead yéna takh ma gueumeko
one for the public
two for the public
three four five six seven for my public
thanks for your luv you make me feel strong
diw squad the familly this is the new song
{chorus}
dégue dathie meune flow am feeling’gou ghetto
rap bi lileu lathie soko amoul n+gga parégo
wathie dano si gueune gaw n+gga yekségo
sama crew mola soutte fi dé gnofi tek dieggo (x2)
[couplet 2]
xeup tchi ndox bou sed g+y n+gga yaw ak sa satala
diokhma sa call ma thiapela
fo nék ma fék!lla
funiou sékké microphone ma dioutaleu k++la
k!llah tchii gome békileu
tchiiii rap 2pac bou dékileu
débordél ma wék!lla
nga djiss puplic bi diépileu
melni yeukeuti fittna louguène taff rék ma tépila
d+d+d squadra fake yi lagni accra
yeuketi peunde bi diokksi kaw ni kharé baddra
ba dou borom diassé djii
boulama diawalé cassadi..
koumu sekkeul beat sa carrière moudié done app tragédie
mbélé mbélé thiowla mc yakk sa youtela
feel you? tube leu
k!llah bandit bou toubela
serial k!llah flow the best loxo bou dioubela
sama mic pakka si poutela
sama clash ray douttela
somay dirr mbague tothie sa nène yakk sa tiouthiela (poussin)
foma séné may nieuw yokatal sa kheul yi
damay rap ba guène nieuw rap ba rakk ak xél yi
fo guèné sa wine niou guèné barada khélli
yo yo yes saay!!!
nokoss di rokoss
the black lion
bandi lg
mister champion flow
[refrain]
dégue dathie meune flow am feeling’gou ghetto
rap bi lileu lathie soko amoul n+gga parégo
wathie dano si gueune gaw n+gga yekségo
sama crew mola soutte fi dé gnofi tek dieggo (x2)
[couplet 3]
dafa beuri louma gnégnilo tchi rap galsen
new school yi nan’gou wougno job né dagniy represent
copy coller ay rimou young jay z ak niom sen
sagne sé bamélni superman guirr shine sur scene
wékou woul ci rime ak flow té séni text dossi sen
lou moy “haters haters” gni dal sarab sen
fakhass sama ass diouk niou mbeukeunté cii facebook
djiss nga sama profil lir nga sama pressbook
nit leu waleu doff leu k!llah dafa khesskouk
mc donal yaye fall bomay nouyou déll souk
k!llah massa raw gueune sé farlou eupp cii public té dou dess guinaw
……………………..………… dikko tek ci beat
n.d.k (nitdoff k!llah) ni lay dikéy
barami dima indiqué
liniou may fay dama koy lguey
digue lg ba bir dk old school yi degnou ma intro
ligni binde dama kay impro
lignou rap ci 15ans la teunk ci ben intro
rap boudé s+x b+tch diapé ma nympho+
cii mane ng+y amé info
mane ak mbed bey synchro
[refrain]
dégue dathie meune flow am feeling’gou ghetto
rap bi lileu lathie soko amoul n+gga parégo
wathie dano si gueune gaw n+gga yekségo
sama crew mola soutte fi dé gnofi tek dieggo (x2)
Random Lyrics
- rowan (singer) - breathe lyrics
- joey trap - blue collar (freestyle) lyrics
- cj francis iv - mango lyrics
- the ballroom thieves - homme run lyrics
- sitoonce - día dos lyrics
- lil cartti - angelina lyrics
- 4rd place - redial lyrics
- shakey graves - not everything grows lyrics
- sickboyrari - stains lyrics
- guest list - enjoy the view lyrics