nitdoff - i love you lyrics
{verse 1}
i don’t wanna make you cry louma meunoul nako try
baby li ngama diaral soko xamone doma baayi
teukeuléwoula ak kénène, xol mi meusta dem fénèèène
lima beug wessou woul done your man
baby da nga perfect ci bepp domaine
baby da nga perfect ci bepp domaine
honey bou déssone ci mane rek do dém
takussane bouné niou doxontou dji plage
romantical love mbeuguel amoul age
saayo néma “je t’aime” je suis dans les nuages
story of love niou bindeu pages
{refrain}
i love i love i love i love you
baby kén douleu beugué ni mane i swear
baby you can trust me
i love i love i love i love you
girl i’ll never hurt you down
always i’ll be still around
to protect you like your angel
all i need is just your love
{verse 2}
wanéna mbeguel samp na tioukel
internationnal tonina kou belle
jurer na fidèle plus de dj+pi guel
mott nga top modèle yama saf n0bel
virena tchi sentiment ni indo
lathie meu or ma wouti panneaux lingo
fu lamp takké beuthieuk djante fayko
naniou dakh distance bi ande deindo
yaay moitié biy motali sama lepp
fouma soxla so amoul sakh da nga léb
dalna tchi mane dalna tchi mane dalna tchi maguii paradise
yéwou ouroul ayni dioxla ndéki nè leu lepp lo beugue ma realise
baby girl da nga high size
da nga fresh ba def sama faya (fire) ice
{refrain}
i love i love i love i love you
baby kén douleu beugué ni mane i swear
baby you can trust me
i love i love i love i love you
girl i’ll never hurt you down
always i’ll be still around
to protect you like your angel
all i need is just your love
{verse 2}
kersa taxna some time douma wané lèneu
li nék tchi sama xol bi soko xamone girl
ciment la mane bèn yone laay toy
fimouné nii dama djébeulou
boudé meusseu nala togne ma ngi djéguelou
ouuuuuuuuu houuuu aaaaaannnnh haaaaann !
naw na sa téguine ak sa djiko niémé na taxaw né amo défauts
gaateu nga tankeu té am nga diné
beuri nga jaameuh té oyof yaw xamo frimer
waathiéna sama garde djayatouma thug
da ngamay désarmer yaw soma kholé ci ay beute
{refrain}
i love i love i love i love you
baby kén douleu beugué ni mane i swear
baby you can trust me
i love i love i love i love you
girl i’ll never hurt you down
always i’ll be still around
to protect you like your angel
all i need is just your love
Random Lyrics
- difa - y ya sé lyrics
- abhijit k - now you know lyrics
- hakai - elle lyrics
- banda trinum - não me sinto só lyrics
- teedra moses - still your girl (be your girl remix) lyrics
- tua - der bettler und das meer (lambert windges remix) lyrics
- kıvırcık ali - türküler, gül ve sen lyrics
- micko swagg - cool off lyrics
- popsnotthefather - on&on lyrics
- neksusha - сучке по ебучке lyrics