nitdoff - intro lyrics
[couplet unique]
rimes ya ngui taadjou ni bollou midi
tek flow you saf sap ni yaape dibi
coupe bougne fi tek rek ma gaddou gnibi
bred naw firi samay laff melni picc (oiseau)
meune rap free cii beat ba nopi di tchii
djangue na alif lam ba ferr idjii
get sama flow so beugué xam lii tchii
h.i.p.h.o.p lay siguile, bonet lay simi mbede laay firi
k!llah k!llah bokoul ci thiaaz yigni irri
nitdoff kané roff, nokoss di rokoss man (echo)
yo yo aanh ! sénégal éy sénégal
kaay ma dioxla flow djip dou thiow
you put to go meune nga jog sa kaw he’ll go
sama second album li diafé na dieum ci yaw dh if you dumb
weuyou bandit déy baayame, dieundeu na djaayame
xam na lane moy fayame, mouri naa laxassayame
get na style lam, now, they know who i’m
nitdoff k!llah k!lleu, thiafka cii flow né gaup bougnou def ndékileu
boy real niou holla, boy fake dialeu tcha wala wala mou k!ll leu
k!ll leu k!ll leu k!llah k!llah k!lleuuuuuuu
i’m big lion man in the jungle
baby girl i’m s+xy symbol
lg diwan nanema member
gars yi nénagne mako tengo (yoré)
roy ak pur dou meusseu méingo
lathie ma or ma dioxla lingo
mossal ma baatt di waye né indo
rap lay def takh mbede bi kiffé
guiss mélomane nii saa nerf di guiffé
you can f+ckin’ hate me. but you can’t stop me
if you try to shoot me da miss me
da miss me da miss me
haaaaaaaaaaaaaaaaa !!!!
when i say nit (what) ya say doff (okay)
nit doff nit doff nit doff k!llah
when i say nit (what) ya say doff (okay)
nit doff nit doff nit doff k!llah
when i say nit (what) ya say doff (okay)
nit doff nit doff nit doff k!llah
Random Lyrics
- koshernine - ready lyrics
- aloïs rossignol - i know lyrics
- 4amcollective - afterlife lyrics
- h1gh - траблмэйкер (troublemaker) lyrics
- death plus - static lyrics
- little monarch - ltsg lyrics
- angela leiva - ai se eu te pego lyrics
- coldrize - не любовь lyrics
- трувонт (truvont) - paradise city lyrics
- yung prh - benzz lyrics