nitdoff - jayantel lyrics
[couplet 1]
wakhoko tchi sa lamign mais guiiss nako tchi sa beut
beurina loy dèmalé mou done ay nakhar tchi sa heart
sometime nga teudiou djioy beu guedji gui ferr tè ken dou yeuk
nattu yi songandoleu ng-y xeuy di geun di ndoleu
sodé goor fokk mou méti tchi sa ndiambaar ak sa ngoreu
do talal lokho ñiane do sathie da ngey diomb loleu
sometime da nga ci wéet beu melni yow amo ay mbok
soy dem di niani ndjiek daniey banie té naane leu ndokk
yow kote yaay desseuk febarou khole biy gueun di yokkeu
f-ss yéné wo tchi yaafouss ndakh ya gui xeuy di djienguou
saga nanie sa ego tchi liguey bi ngey yeungou
thioneu dou rere borome takhna ng-y fanane di yéndou
soula life bi deh tanthie xat xat yi nioley teuthie
gueuneuleu jayanté té khamni weurseuk doula reuthie
xaliss amoufi xét kouko yorr ken doula xéeb
mais kouko xénioul danieley bedi ber leu tchi sa xéet
[refrain : mao sidibé]
jayantel ba am si ndam
loumou meti meti jayantel ba am si ndam (jayantel)
jayantel ba am si ndam
loumou meti meti jayantel ba am si ndam (jayantel)
yallah diexoul
lou meti yagoul
jayantel ba am di ndam my n-gga salit baxoul
jayantel ba am si ndam ( jayantel)
jayantel ba am si ndam (jayantel )
[couplet 2]
louy-ss yi geuneu chère
facture yi gueuneu diss
dépense kén douko miss
nakhari deret guaweu crise
ordonnance produit luxe leu
dounde bi gueun neu cher
xéw yi beuri lool té kén doù def à la légère
kén kharatoul lounekh nioune dagniy lekk nguir banieu khif
kou jayanté beu yégu di nga feu fekk sa bénéfice
soula niak bi deh boukh
seytané daley roukh
so salité rek sankou dinaleu soukheul ba nga soukh
jayantel sa diguou ndaw nga tolou yallah djiekhoul
beugu dimbali sey waadiour té meuno khamnani nekhoul
mais ken dou xeuthiok yallah lounéh ak famouko appeu
jayantél mo gueun nga watchi yone niou teuthie leu rapeu
dara xeuyoul soti moy sakk té moy sopi
jayantél tchi soutooura sakou té banieu djiogui
ame tchi amén gou léw té nekh yallah moy sa tioki
kounek sa weurseuk ding tchi diote kone loy diar xeuthiok bi
[refrain : mao sidibé]
jayantel ba am si ndam
loumou meti meti jayantel ba am si ndam
jayantel ba am si ndam
loumou meti meti jayantel ba am si ndam
yallah diexoul
lou meti yagoul
jayantel ba am di ndam my n-gga salit baxoul
jayantel ba am si ndam ( jayantel)
jayantel ba am si ndam (jayantel )
[couplet 3]
jayantél tchi bimouy méttéy takh bou nékhé do tchi rouss
diombalal sa bopp doone ap yaafouss dieu est là pour tous
bou garab yeublou xob ya rousss dafey mégn feuille you béss
jayantél everday my n-gga try to be the best
soula djiguen yi deh xeb kharite yi dileu daw mbok yi dileu doyadal jayantél
diambar gui nga doon ya gui xeuy di wané diom
so tchi ameuguoulé kom hommie jayantel
ya ngui tchi tolouwaay té lo yakar rek mou mbasla
sey effort dounie ko guiss té ko tchi wane guinaw mou xasla
boul decouragé gueuneul wolou yallah té nga hustler
boussa neguou seuy di xat beu nga doundou fa lou meti
sa dome meun nafa magu tekki jayantel
boula nit ki eupeulé feugu deuneum di jaayou
yénéko limou ame té mandou jayantél
kone jayantel ak yallah jayantek sa digueuk nit gni
[refrain : mao sidibé]
jayantel ba am si ndam
loumou meti meti jayantel ba am si ndam
jayantel ba am si ndam
loumou meti meti jayantel ba am si ndam
yallah diexoul
lou meti yagoul
jayantel ba am di ndam my n-gga salit baxoul
jayantel ba am si ndam ( jayantel)
jayantel ba am si ndam (jayantel )
[outro:mao ]
jayantel di nga meusseu ame li nga beugu
di dokh do seugu
ken doula xep fi nga deuk
siguil boul seug
xamné kén geunoula
wanél sa ngoreu jayantel ma n-gga yeah
n-gga jayantel
jayantel
n-gga jayantel
jayantel
jayantel
Random Lyrics
- mychell - toma tra lyrics
- sauga sen - big office lyrics
- rah-c - resting lyrics
- bệt band - rung động lyrics
- frank wildhorn and jack murphy - easy - 'waiting for the moon' lyrics
- felix de almeida - cintura d'orione lyrics
- bety boom - dangerous frank lyrics
- bryan baker - (i want to be your) hero lyrics
- devon gilfillian - the good life lyrics
- khtek - unpredictable freestyle lyrics