azlyrics.biz
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

nitdoff - life lou geune lyrics

Loading...

{verse 1}
menotté mass courant paka si poute
ibliss done ilimane si diaka dji soute
gni ngour gui dieundeu sène talibé niou djay sène geum
gni ngour gui tok sène khéf dilène dilène tour leundeum
sèni tanke diss ndakh mbague yi atanatoul leugueum
gni ngour gui sathie sène future khagne lène sène freedom
khép sèni compétence niou khoti sèni (…)
gni ngour gui na+ngou sèni joie djokh lène chagrin
diapélène ay cloune méleni charlie chaplin
gni cii hopitaux yi lott i pray for god
wérgu yaram longue life ak séne ndjaabot
gni cii ghetto dii diéme meuneu life lou gueune
séni beut laay part séni tanke foudeune
béne baye amoul mass té yaye matena foukeum
fok niou téki téralène niou meuneu life lou gueune
baay kat bou amoul dougoup pour deube gueun
poliique done aay requins youy reubeu djeune
serigne si done ay…cii kanamou président
kéne dou (3 fois) …lou gueune
nioune gnou deuké daw baa déé té kéne dougnou pay for none
got’em

{chorus}
fokk niou life lou gueune (3fois)
yo fokk niou life lou gueune

{verse 2}
niou ngour gui mour séne shine ba takh niou blind (aveugle)
guisseu tougnou séne mind ( esprit ) loudoule barcelone
takh niou bére sène yone daw baa keupou sii guethie bii
kéthiakh guedji mbaute yi ak f+ckin’ yétt yii
boy yi loyé motakh niou diar cii guethie oh d+mn

{chorus}
fok niou life lou gueune (3fois)

{verset 3}
tchiine yii kepouna askan wi meuneu tounio
corruption bégnou notte bagnou melni ooh no
mister président please if you hear me now
beugue nio agg ak yaw fi cii tribunal
systeme bagui torakhal gni cii guinaaw
gni la fale bagua done bour guéssoul now
rongogne yagui waal di tok cii deundeu
khol yii bakh yakar yii tass fép di beuneu
baay kat yii amatougnou béne pépeu si gueuneu
etudiant yi cii cité bi gua yondélène gmi
fake you méleni pacotille gua diokh lène ay million
yéne injustice yi mooy déclanché rebellion
révolution niou life lou gueune
gni amoul ndiegou ordonnance
déssék séni souffrance
gni amoul ndieugou visa dééssii yonou barça
gni amoul ndidjay cii ngour lém séni diplômes
justice bék tarikha bi niooy séni plicecom (complice)
génération sacrifiée ( 2 fois )
ma génération est sacrifiée
biss bouné cii boppou kogne bi lagni diodo
khalate nagnou ba fodo
prek naniou baa accro
khar naniou laa feugo
thiabi niou sii ghetto
khagne gnou ndokh ak courant ba noppi méleni yéggo
toumranké bigni deuko
gnak noumou gni teuko
thiayine foot party mooy sunu life
bène option lagnou dessé mooy dieule sunu knife
rayaneté sunu biir ndakh aap sagarou five
oh no mister prési xiippil té xol
békor ak walakana bi nioune nioko yélole
sèni dom guéni rawalé cii nga+ndiim école
nioune niooy faay séni vacance ak séni hotel
amoul léne louguéne niou yéné loudoul séni notaires
niou niooy rangue si hopitaux ak sii tribunaux yi
deuké insécurité ak criminel yi
limoy pommade bougnou ma diokh ma yarko diw ci ndel yi
gni yagg daw boba légui cii séne bout tunnel yi
gni yagg sathie alalou ngour gui dém dougou cii jail yi
kagne lagni am béne prési bou gueum réweum
yémalé chance yék droit yi cii boppou payeume
kika falone bou niakheto mou dégue déyeume
président bouy bokoke nioune sunu nakaar
président bouy djokh jeune yi gueudeu bi waar
dalale khélou étudiants yii nakh niou gueune sawaar
béne gmi dotoule téw bagnou kooy sani khér
f+garou fight bépp problémou sanitaire
président boudoul tongue tongue
sunu kom kom dii jonglé sunu life méleni kouy ping pong
gni niak singueulé niou tiap ba meunou life lou gueune
gni sacrifié séne bopp nguir sène ndjaabot
dii daw goudi ak beuthieuk nguir niou life lou gueune
gni laggo té cii pouss pouss wala ci cane bour bii soutourale lène bagnou life lou gun

{chorus}
lilife fok niou life lou gueune (3fois)

{verset 4}
fok niou rakhassate khol yi
sélalate rouh yi
djiteulate diné dji
cii lépp louniou fass yéné djii
serigne cii djiteule money bougnou takal tarikha bii
sèni beugue beugue motakh niou sopi charia bii
right now sii nioune laa désse souniou beugué yeuremandé bii
fok gnou deuké manou bii
sokhela wouniou yeur monde bii
topa ndo baa yéss bakhoule geum sa bopp né gonna be
beuss daana nieuw niou guéne sii
li waliyanone déloussii
niome gni djité réw yii
meune misé sii jeunesse yii
lamp yii cii ghetto bii
gnou wagni ndieugou dounedou bii

{chorus}
lilife fokk niou life lou gun (7fois)

{outro}
yeah ! fokk niou life lou gueune man
fokk niou guéne cii man
fokk jeunes yii am job meune diapalé séni wadiour
fokk niou job sunu future
lane gua fok dagni tok di kholé man
dou wééye meunoule nék man
yeah ! fokk niou guéne sii yako taay man
homies yagui tok di wait beugue sii guéneu
koulène diokh job rek niou job lagni khar
lililife



Random Lyrics

HOT LYRICS

Loading...