nitdoff - loy yeuk lyrics
[couplet 1: nitdoff]
loy yeuk boulma neub wakhma loy yeuk
li ngey xeuy di tekk sa eyes si life bi eskeu do nieuk
black lives matters tékiwo té matoulo ndieuk
eskeu sakh dou sunuy dome li laniouy dound euleuk
loy yeuk george floyd bimouy fateu bey xeuthie
loy yeuk niom seni kasso nit niou gni ley teuthie
loy yeuk black bou teuko black beu raye ko loy yeuk
mane sama khekh moy nouniouy def beu ande rise up
danio takhalo tchi finiou waron andе penthio
black doon démon tchi black tchi white mou doon feu angеl
dem beu melni black beuguoul black meunou niou déndo
lolou yepp toubab biy gueun di raw beguoul niou ménguo
loy yeuk boy xeuy di guiss tchi adouna ni nioun black
dafeu melni niepeu niouy fight
diotna niou bolo sunu side
dioytou di sakou séen
love takhoul niou diokhniou sunu right
naniou dagu chaînes kone té tambalé guemat luy sunu life
[refrain : leuz diwane g]
loy yeuk waxmako boul ma feen
loy yeuk bouniouy raye seu yen frères yi
loy yeuk deer bu ñul dioy neu feep fo dem
ndeysane noyi sax moudiou na doneu problème
i can’t breathe i just wanna live
please sir i’m hurt
[couplet 2 : nitdoff]
loy yeuk africain bi wakhma loy yeuk
sou njitou rew yi deupé caisse bayi xeet bi khiif
lo tchi wakh niou teuthie leu rap tekk tchi ngade ley life
ki am beu ouf louni gagni sakh sey peep ley sif
loy yeuk nit kou niouley djiap rendi niou nioul
nit kou niouley gang banging tirer niou nioul
système bi keep cool noote neu balck people
oubi bountou jail tekk tchi bountou cimetière
brain watching def équation bi tchi misère
corrompre yennen black niou sampe illusion
kou meloul ni do tekki k o bé def division
def sa khel music sport sinan mbedey solution
cravache defneu teurgueun migui sunuy ndode
engagement bi neu sincère waroul nekk mode
sepi ragné sunuy ennemie ak seni méthode
bepp black defna malcom diougu takhaw ni thiode
loy yeuk ci borom kholou dothie
magui dead meunouma noyi mou dieul aumeum gueneu khodj
nguir george ak gni ko djitou black yi wathie fepp tothie
racisme dou lou bess téléphone yi nioko kothie
no justice no peace ain’t no please
diokhleen niou subu geudeu black n0bility
bo diamé ben black black yepp niou gui bleed
ay skinnette you sole tenue f+ck seni flic
[refrain : leuz diwane g]
loy yeuk waxmako boul ma feen
loy yeuk bouniouy raye seu yen frères yi
loy yeuk deer bu ñul dioy neu feep fo dem
ndeysane noyi sax moudiou na doneu problème
i can’t breathe i just wanna live
please sir i’m hurt
[couplet 3 : leuz diwane g]
why don’t we got the right to live like anybody on earth
i can’t sleep tight
he’s not alone , all of us can’t breathe
all the black community just can’t breathe right
eye for an eye tooth for a tooth
like black panther party decided years ago
we gotto keep an eye opened we are the truth
stand for every black man on earth i say here we go
arabe yi di ñu xoxatal noot ñu seni réw
su ñu ndjiit yi takk ñu buum yobu diox nassarane
der bu ñuul diap der bu ñuul rendi def ko neew
ñu nûy xex ñuy xex su ñu biir di gëna saaraan
bu nguéne ñu bëgul ñun bëgu ñu leen
bu nguén ñu feeloul it ñun feelou ñu leen
wayé derete dji turu su ñu biir si ñuni neen
warna dakeu ñu bolé dolé yi def ko ben
racisme 21ème siècle
est une défaite pour l’humilité toute entière
on pardonne mais on n’oublie jamais l’esclavage ce fameux traite triangulaire
beug na xam lane mo waral
lu takh der bu ñul wara soneu fep fo dem
té fou way amé ndam su ñu loxo nga ca wëral
bu ñu jogul kene du ñu fadial sou niouy problème
[couplet 4 : nitdoff]
bedoukou bérou dongu developper sunu koom
yenenté sunu biir kouneh push sa morom
defal sa khel ni biss war nga delou mother land
africa is the futur gnibissil sakh fi réen broda
Random Lyrics
- jig lefrost - hellstar lyrics
- magnificent records - vibes lyrics
- lauren bousfield - heavening lyrics
- ssq - tonight make love till we die lyrics
- ærtūrœ - don't say lyrics
- young rob the jit - days and nights lyrics
- bigbank maye - get money (freestyle) lyrics
- hankroll perri - el gwapo lyrics
- skorn3896 - memories lyrics
- bronko yotte - al capone lyrics