nitdoff - rap or die lyrics
[couplet 1]
they say deet waay
kk n+gga dou fake waay
kangamu mic yagu neu saubou thi guedj waay
xalima diss thiap tchi daa dji def keemtaan
kocc dou djioy mbed dou tankham lou ndenkaan
ngem ngem mou ibra fall moy missalou pass pass
n+gga that’s why al jannah sey dieuf moy dass pass
ennemy they hate me street make me magui tecknik
lyricaly feel nga dadju doff nit
naniou xandalaat ba thia kanam
sout mc yi ni tour eiffel ba thia paname
bouniouy takk rap k!llay ndieuka diokhé thiénam
i’m the underground king mousta wathie thioleum
guiss nga rap sh+t damaleu moudjia sick
ndakh limey yeuk tchi yakhinou akhikha bi dou zic
leeru deugua xoteti xalal niou sunu street
daniu nelawoon xaran ba xababal sunu sleep
nourou laay def tchi guediou arifine
niirou diaaw djiey dadjié taye dji da naara khiin
taw youreet rimou injiin ak tawret doyna kawtef
k!llaay tekk ngey degu j’allucine
qualité thi mbind mi laay mathialaat
xalima kеytek bou maxi crazy laay nathialaat
borom bopp yi doon djioy maleen mothialaat
mbeuro mbeur laaa danеu gauche ak droite bi arène ma tchi raag
[ refrain ]
wu tang k!llah old thang
tell your motherf+ckers bootcamp bi dou dégn
wu tang k!llah old thang
tell your motherf+ckers bootcamp bi dou dégn
wu tang k!llah old thang
tell your motherf+ckers bootcamp bi dou dégn
wu tang k!llah old thang
tell your motherf+ckers bootcamp bi dou dégn
[couplet 2]
supa dupa k!llah rap bou bakh on the way
benen level la ci niom kawak taakh kone neu weey
sama daradjia tchi mbed da gueneu reuy
nanga tokk doma meusseu dab definiitly
yo big boy k!llah fake yi leu slap
koula wakh ni damey def ay xotou pote youniouy snap b+tch
real rap tigui blow sama dathie
soumey niew si mic damey andak flow sama thiathie
yo diamonoy clash ak sat+rday night
bobou beu legui deguago fou k!llah saguané mic
knock them ass out dafey kharou saga neu mike
li tchi gueneu nekh niveau k!llah da nga neu high
borom fetal foumou takhaw borom paca neu fight
bum yi passer neu five my n+gga taal sama side
bimey doga niew fake n+ggaz yi la genocide
lima fi fekone neu bordelique té ladione neu slay
souma naré deglou rap bou taye dem kale ko si niankou
b+tch rapper ya ngi comedy niom buzz laniou nampou
dictature rou k!llah k!llah moy raw apartheid
amoul setadir n+gga rap or died
limey binde ci kaw beat bi mogui louga beu djideu
dama magandok ay samouray you amoul woon guide
ride or die diar diar rou mbed moniou def leader
sunu askane moniou diaral yabi sunu teufliteu
li dou rap bouley guiff lo yokal sa merr
suñ avenir lanie watt ndel dieul sondel tokal tchi ndem
f+ck fipou dieuferou my n+gga topou tchi dem
rap buy wakh ak bopp nénn yi doko fekk sunu game
k!llah
[ refrain ]
wu tang k!llah old thang
tell your motherf+ckers bootcamp bi dou dégn
wu tang k!llah old thang
tell your motherf+ckers bootcamp bi dou dégn
wu tang k!llah old thang
tell your motherf+ckers bootcamp bi dou dégn
wu tang k!llah old thang
tell your motherf+ckers bootcamp bi dou dégn
Random Lyrics
- terra preta - por sua causa lyrics
- mc анюта (mc anyuta) - зож (healthy lifestyle) lyrics
- ishowspeed - single lyrics
- leanje - энигма (enigma) lyrics
- ettie - i'm sorry to my exes lyrics
- electric mary - crashdown lyrics
- 24kay - showing love lyrics
- awfultune - sad love song lyrics
- wall-e ge3z - i hate you ( wall-e ge3z remix ) lyrics
- choliare - 0es3 lyrics