nitdoff - street activity lyrics
{nitdoff}
yeah !!!
ya! pericolosso (un jeu dangereux) biss bou nek mou yém leu
hé mbede nakhanté ak féne leu
systémou taukhidouna
mandi ak taukhi bauna
ndjoute ndiathie ak tek deal ak sokhi maukidaume
lepp cii outi kom+ma, bandit bou souki aumeu
dafa dafa dafa beurii danger
cagoulé seni face speed nii black ninja
tokk tchil planifié dadii tekk deal
daniou gatt tank té douniou wax cii téléphone
diksa (sadik) clik beug easy money téla bone
ay k!llers ak dealers trafic ay kilo baune
gni bagn niou néweul lèn dolé niogui train (s’entrainer)
di fisselé ay gangsta project cii séni brain ( cerveau)
make it lot of money done boss cii séni dream
féliitou bégou naw naw yi cii scène de crime
ay toxico yiy gueune di noyé cii sèn déprime
{refrain}
street ciii laay get sama freedom
street sipp ngani moy sunu favor
street aksil yagui sunu jungle
i say welcome to the street (x2)
street dafa dafa dafa hard (métii)
street activity
street dafa dafa dafa hard
street activity
street street street activity
street street dafa dafa dafa hard
{rex+t}
yaw aksi nga yagui sunu bi side
guissate to métitou life bigni missate
sunu yen bi di dissate
sa bopp niou wissate
nga beussate sa xoll mou niak dii siitate
bagne tokk fi ni di hot
yarr baby di xarr
deufeul sa lepp ba day ng+y diogatt
soubou di tégatt
gueneu meuneu défatt
silou yone nga nékatt
lou yéngou nga…..
life is so hard
so bad
biss bou né niouy sokhatt
songatt
tek délit nieuw taukhatt
topatt sunu waay bamou dokhatt
jobatt
guéneu cii ghetto
done ay hero
diaroul pouss wala taukh ay péro
péro jailo dieulé fi méro déggo
ghetto nioune danio haaaaaaaaaaaaard
{refrain}
street ciii laay get sama freedom
street sipp ngani moy sunu favor
street aksil yagui sunu jungle
i say welcome to the street (x2)
street dafa dafa dafa hard (métii)
street activity
street dafa dafa dafa hard
street activity
street street street activity
street street dafa dafa dafa hard
{nitdoff}
n+ggaz yagui hustla cii street activity
door warr ba slow di xeuy takk fidii
money wala jail’eu defkat yi takk fiit yi
thiabii fété lèn guinaw téwoul niou akk sibiti
street activity lay firii tekk cii sibiti
me and my n+gga rex sipp naniou lou xéw cii street bi
mélokanou niit ki cii nimou gueuneu niawé
djeufinou baayima(animal) djiss nga street noumou grawé
gni société bi guédd niougui fanane cii mbede
gni beug téla yegg cii lou léwoul lagni tédde
done agresseur di reupeuteul
niou rombe rek niou feul ko dieul
djam maquette di rocket niou xoff lagni seukeuteul
{refrain}
street ciii laay get sama freedom
street sipp ngani moy sunu favor
street aksil yagui sunu jungle
i say welcome to the street (x2)
street dafa dafa dafa hard (métii)
street activity
street dafa dafa dafa hard
street activity
street street street activity
street street dafa dafa dafa hard
Random Lyrics
- zetak - zeinen ederra izango den lyrics
- carlos uzi - error lyrics
- uffie - froyo for your tears lyrics
- aveistrash - ave says lyrics
- dev - can't stop lyrics
- br0knben - "regina" lyrics
- thyno tilona - cheat codes lyrics
- terror do interior - você mais perto lyrics
- wengie - learn to meow (remix) [学猫叫] lyrics
- alexis engrand - double face lyrics