nitdoff - unified now lyrics
{verse 1}
yo! unified
please unified
bolé sunuy dolé, sunuy xam+xam unified
fékhé ba babylone dotoul exploités sunu faille
djam djék xéweul yi meune taw cii sunu sky
mama africa waratoul seug rek cry
ay domam nioko waral siguile’ma kone naniouko pray
nango nelson mandela inspiration
africa united naga ko def sa destination
sékou touré vision
sankara education
cheikh anta diop, warna yokk motivation
united for the future
the mother land culture
fi niou beug yegg yi dé djiko niokoy builder
{refrain}
u+u+u+unified now (a)
u+u+u+unified now (fri)
u+u+u+unified now (ca)
u+u+u+unified now
waxtou djotna fi weuk à dieu
u+u+u+unified now
waxtou djotna fi weuk à dieu
unified now (a)
unified now (fri)
unified now (ca)
bolo bène, wara nek sunu fight now
{verse 2}
yeah!!! right now it’s the moment
yeah!!! the right moment
niougui wo xalé mak gorr ak bépeu women
africa warna unified cii bépeu domaine
bolé sunuy dolé exploité sunuy meunine
bayi wakh té djeuf xamné time is running
niou free bagna wékou cii systémou babylone
black dj+p beu, dotou niou walii yone
kou meussoul téyé bass (5000) xeuy am 10.000.000
féthie kanam yi niou fass di ré né amdy mignon
bokk done bène éthnie moytou rebellion
monnaie bi di bène, frontière yi di bène
africa right now, bo tchii beugué guène
{refrain}
u+u+u+unified now (a)
u+u+u+unified now (fri)
u+u+u+unified now (ca)
u+u+u+unified now
waxtou djotna fi weuk à dieu
u+u+u+unified now
waxtou djotna fi weuk à dieu
unified now (a)
unified now (fri)
unified now (ca)
bolo bène, wara nek sunu fight now
{verse 3}
magui call nigeria
magui call wa liberia
++++++ ba ricos mali ak mauritania
please naniou f+garou soukeuli sunu area
wara touniou tongo
diotena niou longo
tanzania ethiopie ba yegg congo
thieurou mother land warna délou famou néwone
south africa somalia ak sierra leone
unified money diokh power
ak prosperity li moy yone bi geuneu gawa
waxtou bagui naw
niogui dess guinaw
immigration kou nék fakkeu djeumi kaw
unification is the key, do it now
{refrain}
u+u+u+unified now (a)
u+u+u+unified now (fri)
u+u+u+unified now (ca)
u+u+u+unified now
waxtou djotna fi weuk à dieu
u+u+u+unified now
waxtou djotna fi weuk à dieu
unified now (a)
unified now (fri)
unified now (ca)
bolo bène, wara nek sunu fight now
Random Lyrics
- cinque uomini sulla cassa del morto - vieni a svegliarmi lyrics
- nerva - payoff lyrics
- union (band) - jungle (live) lyrics
- pedro aznar & ramiro gallo - es muy poco y es muy tarde lyrics
- trzynogie spodnie - bańki mydlane lyrics
- wdng crshrs - thecoolismac lyrics
- llightskinned - peso lyrics
- molly payton - no one else lyrics
- ήρωας (hrwas) - fata morgana lyrics
- homegalaxy - scottie tripn lyrics