nix - highlander lyrics
[chorus]
vieux père bou doul maguette highlander
dague sene boppe lay def highlander
décapité par le chef highlander
vieux père bou doul maguette highlan…
vieux père bou doul bayi highlan…
vieux père bou doul maguette highlander
fou niou dougou ma lidjenti lene
mane késsé boy kene dou ma donneu
niou yeungou ma dagati lene, ngene sorima lo ley lou dagane
y’all don’t wanna live
(y’all don’t wanna live)
[verse 1]
bou may dioudou rap dé amagoul
fii la ma fekk ni seeni doule
ma impermeable ci yeah dama toul té nope bou nathioul dé dégagoul
baggy jeans wu tang diamono may battle di
battle di battle freestyle ma lay golo lo
may danel di danel di danel
so ma wédé laadj ma xuman, t
ekk ay flowou busta mel ni dou mane au final yakamti pour lane?
periode bobou dam ko djegui ni dos d’âne
néka gouma artiste solo mais ma ngui ci game bi ni gaindé bou souroul
di dougal ay mcs ci biir kilo mbourou
di dokhontou ci kogn bi di weur ay foureul
n-eazy defal ndank lou eupeu tourou!
ma keupeu yelwane bi sama boy yi djiiro
surveillance générale la bagné
bureau, ndékété mariage dafa wekh ni gouro
dou ma la djaay experience boy amo ndjeugam
degn ma yarr boy xebouma deureum
degn ma nokhe boy ba tay may geureum
golden boy dama nioul ni peureum
longévité boy dou serigne dou mara dou téré dou garap boy défo fii
dara, dou palace dou baraque dou
donald dou barack, dou point e dou karack
lou gnou cons boy dou diaraat, laadjal egypte boy fou gnou tegone
mubarak
mais yallay buur sou ko nékhé gnou faraat
kone n-eazy bayil sou la nékhé nga dieulaat …
ndakh yaay vieux père bou doul maguete highlander
[chorus]
vieux père bou doul maguette highlander
dague sene boppe lay def
highlander
décapité par le chef highlander
vieux père bou doul maguette highlan…
vieux père bou doul bayi highlan…
vieux père bou doul maguette highlander
fou niou dougou ma lidjenti
lene, mane késsé boy kene dou ma donneu
niou yeungou ma dagati lene ngene sorima lo ley lou dagane
y’all don’t wanna live
(y’all don’t wanna live)
[verse 2]
katana bi lou mou dagati boy rawna dibiterie
tête de mort nekone fi tendance mais tout
c’que je voyais c’est mes trophées qui me sourient
quickening flow bi mo déloussi
boy ay éclairs lay cons melni hennessy
rap galsen sama dom on est
père et fils
mamou mamati mamou sene lyricist, ay seut flow therapists
kou fi attane sama legacy neu tekki térém dérèt takhal yérêm, bann
bi takhal bérem balles yi takhe tat tat tat tat
boy niou teureul leen yene ak sene kheureum fils
équipe bou fees ak ay génies fils, d
o ladj orange lane moy bénéfice do ladj wa yonkers
kouy jadakiss, défaite bou ley fegnou do ko teela guiss
té longévité boy dou méyé dou sarakh, dou jordan dou thiarakh
dou khegn nekh dou forokh mais toujours frais comme le vieux père
rey la ak sourire ni joker highlander!
[chorus]
vieux père bou doul maguette highlander
dague sene boppe lay def highlander
décapité par le chef highlander
vieux père bou doul maguette highlan…
vieux père bou doul bayi highlan…
vieux père bou doul maguette highlander
fou niou dougou ma lidjenti
lene, mane késsé boy kene dou ma donneu
niou yeungou ma dagati lene ngene sorima lo ley lou dagane
y’all don’t wanna live
(y’all don’t wanna live)
Random Lyrics
- ax and the hatchetmen - silhouette lyrics
- robinplayschords - starsailor lyrics
- leon'swolf - caligo lyrics
- charlie brown jr. - zóio de lula / citação: hoje eu só procuro a minha paz lyrics
- colin weeks - sunset kingdom lyrics
- jetsweep30 - wakanda no condoms forever lyrics
- to the rats and wolves - all the things lyrics
- marseaux - το τανγκό της μαρσό (to tango tis lyrics
- blood orange - seven hours part 1 lyrics
- fiordaliso - siamo ancora a galla lyrics