obree daman - bideew lyrics
bideew lyrics
aha
yow
mii
sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
yow
mii
sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
agsil ñu àndandoo
àndandoo ci asamaan
sa mbëggeel’ay bideew
[bideew biy leeral goor yalla]
bideew biy leeral sama yoon
aha
jigeen a indi leer
aha
leeray ci àdduna
aha
sa mbëggeel’ay bideew
aha
[bideew biy leeral goor yalla]
biy leeral sama yoon
yow
mii
sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
yow
mii
sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
jigeen’ay leeral
melni leeray u asamaan
sen mbëggeel’ay leeral
jigeen’ay leeral
ni leeray u asamaan
sa mbëggeel’ay leeral
sama yoon
leer leer leer
leeray u jigeen buy joge asamaan si moy leeral goor yalla yi
leeray u jigeen buy joge asamaan si moy leeral goor yalla yi
leeray u jigeen buy joge asamaan si moy leeral goor yalla yi
yow
mii
sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
yow
mii
sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
aha…
traduction française
étoile
toi, c’est ton amour qui illumine mon chemin (x2)
viens, on s’accompagne
s’accompagner vers le ciel
ton amour est une étoile
l’étoile qui illumine mon chemin
la femme apporte la lumière
la lumière sur terre
l’amour est une étoile
celle qui illumine mon chemin
toi, c’est ton amour qui illumine mon chemin (x2)
la femme illumine
commе le ciel
votre amour illuminе
la femme illumine
comme la lumière du ciel
ton amour illumine mon chemin
lumière (x3)
la lumière de la femme provenant du ciel
illumine les hommes
(x3)
toi, c’est ton amour qui illumine mon chemin (x2)
Random Lyrics
- jaydi - otra vez (ft. cheismc) lyrics
- tejon street corner thieves - deal rag lyrics
- why shadow - ты услышишь меня (will you hear me) lyrics
- noah - vault lyrics
- francesco bianconi - domani è un altro giorno lyrics
- mikey dangerous - mikey dangerous - higher than high lyrics
- mehmet erdem - sevemedim kara gözlüm lyrics
- t m thyagarajan - manasuloni marmamulu lyrics
- nurgle (grc) - visions of the abyssal perception lyrics
- tyler kamen - snafu's animal sanitarium lyrics