omzo dollar - mame premier lyrics
intro
amneu gnima begn, amneu gnima beugeu
amneu gni di fenn, amneu gni wakh deugeu
dinegn thiow, dinegn hate mais seneu wakh mo beuri
kham nagn kane moy kane, kham nagn kane moy kane
young fif zo dollar, adresse bi sicap leu
no djoutou gang team bi nak buzzlab leu
dougnou wakh ac yow beneu mot niou tate leu
sa papou pappeu ne le wakh kouy pappam
mame premier, mame premier,mame premier,mame premier(x4)
1er couplet
mane leu young fif premier, sama team mo meuner
khalé fekkeu pa yi def lene bébé dakh nénegn les derniers seront les premiers
kane mo beugeu problem nieuwlene venez?
recolter lougn fi seumer
n-gga na ko deffal sama bopp boul dof damay hustle meli boy bou pappam renier
somay press ay rappeurs né ma bon apét-t
niom nieupeu meu makk pourtant c’est mes pet-ts
f-ck senni votes, senni media, doumeu révélation de l’année ya yékheu sip
awadi duggy tee nénegn may deugeu bi
rap bo doul dégeuti, capsi ma yékeuti
yenene rappeurs yi di sop dougn ci lene dagni weur rek di fene melni politique
doul rek ci deukeu bi
rimes ay tonnou flow, ay qintalou syllabes
punchline you lay def li marteaux defone talla sylla
kene gnéméwoumeu clash? je vous montre comment faire ça!
omar vs omzo… real vs barça
refrain
2e couplet
j’ai un détour d’avance, rien a foutre de la chance
été bo meu guissé boy damey am cl-sse,pourtant nieupeu kham ni moussoumeu cours de vacances
yélé yélé music baaba maal, dageuti sa bop melni sahaba
katana, dageu na
may sene mame….adama
sama meune meune ci rap meyou yalla leu do ci meune dara kone diokh meu billets n-gga
tout ce qui brille n’est pas de l’or mais ce qui est de l’or doit briller n-gga!
zo dollar zo commence zo fini!
you f-cking wit da monsta… zoophilie
rap ay couplet you pas net, lepp ci sama deundeu guéneu ni janet
si t’es le meilleur rappeur au monde c’est parce que omzo vient d’une autre planète
0+1=1 la jangeu da melni lolou legui ay fenn leu
zero geu may one té pourtant mane ac yow dougnou benneu
refrain
outro
wakh bou barri bi est ce que diarnako
niou yorre game bi nieup khamnenko (buzzlab)
yan boy nio yekk si public bi wey lepp a ba z
concert ni dor ba parre public bi yekk tagolen (eskey)
ni-n-l rappeur yi sen rap bi bakh
ah! niet likhl-ss ben fatiha (ndeysane) ndeysane
di doul nane denen coming soon (ah)
te sama team dele coming soul
mc niata lelen fey n-gga (wakhal)
nenale liguey rek key fey n-gga
wakhnale adress bi sicap le fi buzzlab le niole tat diour sa pape nenanme mame premier (x16)
Random Lyrics
- fabe - ça ou rien lyrics
- edurne - te menti lyrics
- fakt ist fakt crew - leipzig ist gefährlich lyrics
- pink floyd - side 4, pt. 4: louder than words lyrics
- beast - drive lyrics
- siddy - familia & amigos lyrics
- luke rage - nonsense lyrics
- chano! - melody maker lyrics
- psy - gangnam style (dj hero re-rub) lyrics
- zacky t - shine lyrics