omzo dollar - nitté lyrics
nitté
nite yagui si bir nitt yi da melni yapou nit molen sourr
niit dey dougal nitt safara di ko nakh ak adjana si kaw souff
pithie mougui si kaw wanté khel bi yeup nekk si souff
kou dioudou si cage dey fokkni ki sibiti mo dioum
lane leu ley wagnil ioe someu yokalé
mba loumey tall ioe dineu feyy seu yéné
khana soy rafet dafay takh meu niaw
kou kawé dey touti si kou meunoul naw ( abozé)
(ndakh maleu yéné gueuna nitté x2)
seytané wakhoul deugg gniko deglou negn yakk sen khel
requin yi guéné djiko caiman di negn done ay djane you matt sen guen
gaïndé dou fallé couille you bokk mbaar
dieun bou ndaw si bou mak lekk ley done
mala boudoul diamou yallah amoul
pourtant alakhira souff rek legniouy done (abozé)
(ndakh maleu yéné guena nitté x2)
guiss na ay maguette birou khalé
si bir ay khalé you bireul ay khalé
degn sathione sunu enfance niou magg niouy sathie sunuy enfant
boul dougal khadjou mbedd si seu keur
boul dougal khadjou mbedd si sa keuuur
meuy leu sama mbokk dou takh niou done cousin
loup bagui si poulailler bek sourire bou jaune poussin ( abozé)
( ndakh maleu yéné gueuna nitté x2)
maleu yéné gueuna nitté, dafa beurri louma meunou expliquer
quelle mouche nous a piqués
niit bouniouy diamou ayy kharr rek ley djité ( abozé)
anh niou sante seni tour legn gueum
kou khessal negn leu tour leundeum
sou goudou nopp takhone degg ken door mbame
bou dessoul loudoul fass seu kanam daw do fallé dos d’âne
meuno mouss beu gaindé done bouki
watt ay kagna rat de terre niou nek chauve souris
xxx, lo peundeul mou sett
ndakh khol bou diekh ak deun bou fess lo djeund dou dess boul tipssé
limité sunu nitté yeup si succes
succes si seu diné digueu distrait
distrait beu dall si mur melni sindakh
tête loin des épaules, girafe
am xam+xam mandou wo moudié done serr
kou am chaire de poule niou def leu poulet de chaire
seu succes seu none ley dane
golo ak allumettes boon ley tall ( abozé)
yallah mom lissi kanam
boy diégui khol seu droite ak seu gauche beu
safara beurineu niou fi defoul wone long feu
( ndakh maleu yéné gueuna nitté x2)
maleu yéné gueuna nitté, dafa beurri louma meunou expliquer
quelle mouche nous a piqués
niit bouniouy diamou ayy kharr rek ley djité ( abozé)
Random Lyrics
- musashi a.k.a eugen de silentio - critica della ragion putrida lyrics
- otto franklyn - sitze zuhause lyrics
- tj harris - my kinda country lyrics
- unge lama - fri (slå meg 2021) lyrics
- liqvor - esame di coscienza lyrics
- erica freas - red is lyrics
- isaac dease - summer and chill lyrics
- elaine martins - unidos pela palavra lyrics
- super beaver - 二人のこと(two people) lyrics
- daniela alfinito - die hölle kann warten lyrics