opd - amoul delou guinaw lyrics
intro :
yow yow what’s up senegal , walabok, it’s your boy clarity
filmmaker , producer , graphic designer , the one who made the mixtape covers for opd
but yow this ain’t about me so just enjoy the mixtape def dara am dara , peace
verse 1 :
yeah , opd crazyyyyy
anh mom la mou ngui ni dé , futur imam ci rap bi yagatoul pour ma djité (haha)
guersou khol fi ma diougué , bagna delou guinaw , dagna bokeu ci gniy moudjé
ngua né dafa nekh , nguané dafa leer , di ma lathie qualité bi fou mou djougué
sama neek la ko togué , sama neek la ko jobé fa la qualité bi diougué
beneu chaise beneu table , tek laptop tégué mic bi né takhaw
dougueul samay baat , paré tok mixé , selfmade mother—ck son bou gueneu done tacle
f sa studio , sama neek la def studio
bo dé mono , ma done la gnari yoon stéréo
oh no no , here i go , bump my sh-t enjoy my flow
yokeu sey baffle sama baat di ci bounce , sama baat di cii blow
refrain :
amoul delou guinaw x3 (dougouna ba paré )
douma delou guinaw x3 (ndakh li ma bayi dafa beuri)
djémeu dem ci kanaam x3 (def dara am dara djemeu dem fou sori)
fok ma djeulé ci ndam x2 (meme soudé , meme soudé li dé di na meti)
verse 2
khawma lou nekoul ci maan , wayé boudé djom akh fouleu boul dem feen seet ko cii maan
wakh ma lou la nekh ci maan ma exploité ko diokhla le meilleur ngua gueuneu beek ci maan
2011 yeksina , 2012 gnou dem
2.0.1.3 d.d.a dem c sa le theme
kone douma def loudoul , diokhé li ma am yeup def loudoul
deugeur keung melni niit kou toul , bagn di tok ndakh tok bakhoul
wakh cii biir wakh , deguiin la lathie kone dieulimeu
fou succes nekeu ? ma woko neko mou dieulsima
neko mou yobou meu yobou meu fou keen yegueguoul
lou diot yombou bou ameugoul dafa dioteugoul
dieul seu temps amoul pertement , depart na awma tardement
doucement et lentement ma matalko mou done evenement
na nguo soneu , na nguo mougne , sama wakhou yaye
tourné dadiekh sama baye mouné ma dokhal way
refrain :
amoul delou guinaw x3 (dougouna ba paré )
douma delou guinaw x3 (ndakh li ma bayi dafa beuri)
djémeu dem ci kanaam x3 (def dara am dara djemeu dem fou sori)
fok ma djeulé ci ndam x2 (meme soudé , meme soudé li dé di na meti)
outro :
yeah , merci beaucoup les gas
welcome to def dara am dara mixtape
bou yeksi fi yeeneu ko pouss ba mou yeksi fii mayn
c’etait juste l’intro , leh go
Random Lyrics
- a day to remember - stricks & bricks lyrics
- music for absolute sleep - slumber lyrics
- fjärilseffekten - svart & vitt lyrics
- plankeye - down to the alter lyrics
- soul khan - someone's pocket lyrics
- samson - candy flipping lyrics
- jill johnson - kommer tid kommer vår lyrics
- skow - tumbleweed lyrics
- too strong - lyrisches kung-fu lyrics
- donguralesko - pięć lyrics