pape diouf - partir lyrics
Loading...
bima deimei ñu mayema visa il faut que ma dem
liguey nguir terral samay wadiour souma nieuwei takkla
mane nanelay deff
limay raggal moy wanela guinaw nga
fattemay souboba dinama nakari ndax ande bi yagna
mane nanelay deff
wayei fouma diar mane dina dem liguey
ndax may taw wadiour yi manelañu yaakaar
né faw ma dem outidji nguir terral la
baby sorry gueneulouma baby mangui nieuw
beugnala xalei biley
bima deimei ñu mayema visa il faut que ma dem
liguey nguir terral samay wadiour souma nieuwei takela
mane lanelay deff
wayei fouma diar mane dina dem liguey
ndax may taw wadiour yi manelañu yakaar
Random Lyrics
- beenx - sora lyrics
- black pantera - cola lyrics
- tamta - xai5-v lyrics
- ragee kill, y4hiko, майкл g - swim swim lyrics
- pablo - amizade lyrics
- rəqsanə ismayılova - qəm düşüb ürəyimə lyrics
- bff - what we do lyrics
- 羽多野渉 (wataru hatano) - 天空の先は (amezora no saki wa) lyrics
- ados & şanışer - volta lyrics
- kill dyll - gasoline lyrics