pps the ghost writah feat. amdy opti - doon mane (feat. amdy opti) lyrics
galsen genius
the temple of urban poetry
oct
15
yagg na tarr may dekku, ken mussul degg diaambate
life bi yar niu si met-te, rongogne niu nal ko diambaate
diambar tigui sigui si ghetto ken duniu diam baate
yeungeul niu yo, beu neu, wayé never doniu damate
niun, daniu juddu jomi
namp naniu ba deugueur ferr, xouss ci souxeute jom yi
dundu naniu ci barack, yeewu taax yi diniu seupu
luy-ss cogno cogne, pa bi garé, cine yi deppu
panne yeré daleu, deme keur deukeundo seetani télé
c-p-tu ak xool yi, melni niom nimu ma doon yitélé
xamuniu woon né goné buur leu, lou way mugne mou diex
xelu xalé tool le, dji ci lou baax, euleuk mou neex
(amdy opti)
life is so real; people are fake
li may saku mooy, ameu mudj gu rafeet (chant)
sama demb moy lampe biy leral fama dieum
sama sama ngeum bayima ma doone mane
bayima ma doone mane
bayima ma doone mane
(2)
(pps: let me be myself)
hate me or love, i stay the wat i am
malaaka wala djiné, boy bu yarook weuyoo yeme
maye taan di bagne, signe di gagneu, luma ci gobbé gar
maye dioxé di nangu, doxé ci tanku goor, luma ci gobbé gorr
ku sa ape jott borom bi guiss may la
soy fataliku da ngay sokhor deugeuleu ismaïla
tay la degg bax yaye, demal do sen morom
daniuy dolli sant ndax lu soti ameu borom
tay numu mel douma t-teul, geunone nafi thoiol
limaye j-pé diam, diegui na am am wala ndol
paul, mawone dangou moy pps bou rene
ghetto child never change, geum ko saxfa reen
(amdy opti)
life is so real; people are fake
li may saku mooy, ameu mudj gu rafeet (chant)
sama demb moy lampe biy leral fama dieum
sama sama ngeum bayima ma doone mane
bayima ma doone mane
bayima ma doone mane
(2)
mo-bouray-no, equipe bi dou sopeeku
liniu liguey deuxeugne si underground tay moy soteekou
messaghe crew forevr, hip hop bi seedé naniu
sunu gueinte mudju na ami tank, mbedeu seddeu naniu
xeutio wuma lanc, ndap li yaa na ni géec
deet fontu wuma defantu wuma, dalal yaay ami gacc
picc diawu la xam, diante douko teeré naaw
ku weedi na lacc hip hop, mom mi top sama guinaaw
f-ck your business, mane love laye sedeulé
fedali koleurek gni teulé xol yi ni niu kay seddalé
ngeumeu niou indi fi ta euleuk mo niuy dialalé
no pain no gain, yoon wi nonou lako jah laléee
kouy xeutiok mane teen ma bala ak mome
lac de guiers moma yiteel baay
the ghost writah, xaatim ak kàllama!!
Random Lyrics
- farhad - gonjishgake ashi mashi lyrics
- kindred vice - vacant faces lyrics
- lizette & - artificial me lyrics
- i am apollo - keep it on the line lyrics
- a.r. rahman - kannodu lyrics
- annalisa - ancora un'altra volta lyrics
- maeckes & plan b - verstummte sicht lyrics
- 2 chainz - felt like cappin lyrics
- budi & the gorengan - bermain cinta lyrics
- zayn - pillowtalk lyrics