sicks killer man - mouñeul touti ft jmv lyrics
beugueu téral ndeye ak baye
diabar doom,mbook aki waye
takh mou diougué senegal
dieul plane bi naaw si kaw
wala douguou ci gaal
aw ci nddokh mi né fess outi yonou kaaw
bénene life boumouy feki
té bala dife beugueu na teki
feulé sa babylone mico guatandok nguandi welcome
mou djiteul fouleu ak diom gueum bopam né x_malcom
niémé waar né talibé mouridoulahi feulé sa khelcom
mé lamfa fekkeu dou touss amoul nothing mal_com
ndax lim fogone né mofa nek
wouténa ak lim feu fek
deukeu beu deugueur wow né kek
bou yonéwoul ndiaboot gui dou lek
takh co daw soubeu ak ngone
amoul goudi amoul beuthieuk
dou tayi baye sone
si lambi li di weurseuk
donté guissaguoul yone
boumouy diar ba matalco seuk
s-ssouné mongui diém
foumou yakaar liguéye dem
o dos sac yék train wathie bus té dou meusseu guedeu
toumouranké niémé khiff dekou marr fanane si mbedeu…
escucha lo que te voy a contar
te digo que es un hitoria muy real
yo fui buscando un sueño sin pensar
todo el tiempo que tendria que sacrificar
por suerte una familia me encontre
que no miraba el pasaporte,ni el color
porque no entiende una absurda ley
no respecte el derecho a vivir mejor…
donté mongui méti mouy mougne
amna yakaar beuss nieuw mou mouugne
limouy life life feulé sa tougueul moy dundu k wéreyane
limoufay dathie raw mbougueul métina lolou dem waliyane
diapalné rek mingui kaaw
bo beugué degueu deug fofou amoul morney boumou faye kaaw
situation beu feu nek s-ssouné daye gueune di graaw
té guissagoul solution boumouy tek beu lep falaw
niémé na sonou bagne gathie
kanamou none fok mou am ndam
té thiono bamou faye dathie
moo eup limoufaye am…
que culpa tengo de nacer alli
donde no necesito tanto para ser feliz
donde la gente no tiene tanta morosidad
donde yo soy un hombre digho con identidad
intento cada dia sonreir
porque la fuerza de un leon llevo dentro de mi
quisiera tener libertad
pero la policia no distengue ni bien ni mal…
Random Lyrics
- dave matthews & tim reynolds - sister - live at radio city lyrics
- franco fasano - il cielo è sempre lì lyrics
- marquess - latino america lyrics
- el pescao - peces voladores lyrics
- jake bugg - broken (single version) lyrics
- jj royce - day by day lyrics
- the illz - in between us lyrics
- giorgio gaber - nairobi lyrics
- young kevv - bestfriends lyrics
- kevin (sa) - ok lyrics