
souleymane faye - jeleeti lyrics
jeleeti lyrics
fo koy jeleeti kou la beugue ni man
fo koy jeleeti kou la sope ni man
fo koy jeleeti kou la n0be ni man
fo koy jeleeti
kou yewou khadja goudi di khol ndakh sangougua
kou lay wakh deugueu jo bougoula degue ni man
kou nek ak fa yalla bourbi fetele
ak fa nga beug sa bop fete
fou ma koy jeleeti kou ma n0be ni yaw
fou ma koy jeleeti kou may firee ni yaw
fou ma koy jeleeti kou ma gneme wakh deugeu ni yaw
fou ma koy jeleeti
boula bour bi yalla beugue da nga koy kham
ndakh tokhidona bo douguou mou guene la ci
boula nit ki beugue dome yaye ndagua koy kham
nakh bou moussiba di khegn mou ne la kay goungue ma fi
adouna gongou souniou kanam
jam waroula teukou morom mou jamam
adouna gongou ci souniou kanam dom yaye
jam waroula natou moromou jamam
fo koy jeleeti, fo koy jeleeti
(fane la koy jeleeti, fane la koy jeleeti)
fo koy jeleeti kou beugueu sa diam ni man
fou ma koy jeleeti kou degueu dadj ni yaw
fou ma koy jeleeti kou moka potch ni yaw
fo koy jeleeti
kou yewou khadia goudi di khol nakh sangougua
kou lay wakh deugueu jo beugoula deg ni man
kou nek ak yalla bourbi fetele
ak fa gua beug sa bop fete
fo koy jeleeti, fo koy jeleeti
fo koy jeleeti, fo koy jeleeti
(fane la koy jeleeti, fane la koy jeleeti, fane la koy jeleeti, fane la koy jeleeti, fane la koy jeleeti, fane la koy jeleeti, fane la koy jeleeti, fane la koy jeleeti)
Random Lyrics
- frost.y (frostwhy) - corpo em decomposição lyrics
- savvy reign - understand love lyrics
- creature culture - queen of the music scene lyrics
- blau kid - faltas tu lyrics
- howlin' wolf, muddy waters, and bo diddley - the red rooster lyrics
- killing art - escape lyrics
- rioma rich - como tú lyrics
- mb - fuck up lyrics
- double virgo - hardcore hex lyrics
- yung bude & tajo - veto lyrics