youssou n'dour - c'est l'amour (it's love) lyrics
sou wakhtané ak sa ma ngiégénay
nakh goudi de yokou khel
sou beuthie ké ma dall di faté
mane guinntiyé you ma guintone bigu
c’est l’amour
c’est l’amour
c’est l’amour
sou mala rombé di dem
na fokk liéph bakhna si mane
apparrence bi nakhna la
khamoulo li nékk ci mane
c’est l’amour
c’est l’amour
c’est l’amour
to love
amaré
chintouru
yébene
mangui dann sa ma dolé
mangui sante yallah
mangui fathie sa may adio
munneh amm na lou dess
c’est l’amour
c’est l’amour
c’est l’amour
mane lekouma
mane nanouma ba tey
mane heefouma ba tey
mane somouma
mane geumouma ba tey
nelawouma lou doyy
to love
amaré
chintouru
yébene
nakhe bеur
to love
amaré
chintouru
yébene
chintouru
yébеne
nakhe beur
nakhe beur
mane lekouma
mane nanouma ba tey
mane heefouma ba tey
mane somouma
mane geumouma ba tey
nelawouma lou doyy
c’est l’amour
mangui dann sa ma dolé
c’est l’amour
magui sante yalla
c’est l’amour
munneh munneh amm na lou dess
c’est l’amour
souma waxtané akk sa ma ngégenay
c’est l’amour
nakh goudi dey yokou khel
c’est l’amour
mangui dann mangui dann sa ma dolé
mangui dann mangui dann sa ma dolé
c’est l’amour
mangui dann mangui dann sa ma dolé
c’est l’amour c’est l’amour
c’est l’amour munneh amm na lou dess
c’est l’amour
geumouma nelawouma
c’est l’amour
nelawouma lou doyy
Random Lyrics
- codeine - skeletons (sos demo) lyrics
- grey matter - greet debt lyrics
- lil wayne - public announcement lyrics
- jellyy - in the sky lyrics
- charles zimmermann - anchors aweigh lyrics
- prince of eden - crawl lyrics
- foley - coffee lyrics
- robin williamson - for three of us lyrics
- primz - fam over kjærlighet lyrics
- karim khalyapov - сиңен очен жибәрәм lyrics