
youssou n'dour - cheikh ibra fall lyrics
mber mi nu naan cheikh ibra fall
te nu koy wooye lamp fall
ahmadou bamba moo ko taal
foo ko tudde nepp ni fall
masula fo, xamul ay baal
te kii du kuy tedd ci lal
daa gis lutax muy tebb di dal
ahmadou bamba raw ay baal
njekk mu now ci bamba daal
cheikh ibra daa meloon ni taal
am ay garab ba kenn du ko laal
laajal, laajalma waa kawsara fall
cheikh ibra fall, cheikh ibra fall, jambaar la
cheikh ibra fall, baabul muridin
daa tedd guddi nu ne ko fall
mouhamadou mbacke lay jafal
jox ko ci moom ay tektal
lii moo waral mu and ak aal
waxtu wu ne mang koy maggal
dii soq te roota ko war
na mu fa fekkoon da leen lakkal
ci di leen sujoot waajaangi daal
cheikh ibra fall, cheikh ibra fall, jambaar la
cheikh ibra fall, baabul muridin
fekkoonna nods mu nuy tangal
ndongo ya naa bu kenn laal
mu ne ko cass, du jog ci aal
ngir li mu gem cheikh bamba daal
cheikh ibra fall, cheikh ibra fall, jambaar la
cheikh ibra fall, baabul muridin
Random Lyrics
- the undisputed truth - just you 'n' me lyrics
- nirvana - school (live at roskilde 1992) lyrics
- aviators - the cinematic future (vocal stem) lyrics
- kennedyxoxo - r u proud of me? lyrics
- kidd gohann - don’t play about bae lyrics
- fakemink - snow white lyrics
- echoveil - deep blue lyrics
- mikael santos - não me esqueceu né lyrics
- princess nostalgia - get it up lyrics
- noslen nayrb - him lyrics