youssou n'dour - confession lyrics
yow waxma
lanelay deff
meunuma ci dara
mane xawma
lanelay deff
meunuma ci dara
waxnako deguma
meunuma ci dara
choix wam leu
choix wam leu
meunuma ci dara
kaféwukok dara
waxtanewuko
meunuma ci dara
ahh yeahhh
ni dal leu deimei
bu feikkei beuguetoula delu
nañ ko fi bayi mouy weundelu
bumacci keine garouwalei
mane waxumako nañ n0banté
majeure leu mom teu werneu
té neineu yeug yeuguem leu
bess bunеi maniko mu delu
munema beuguеtoula delu
mane sax dal bayinako
mbeuguel dh bou xassei djokk
keine meunuki teye
choix wam leu
choix wam leu
choix wam leu keissei
te mom sax
da bayi njabotam
té neineu dotul delu
ahh yee ahh yee
dumacci dara
ahh yee ahh yee
meunumacci dara
bu feikkei beuguetoula delu
nañ ko fi bayi muy wendelu
bumacci keine garouwalei
mane waxumako nagn n0bante
majeure leu mom teu werneu
te neineu yeug yeuguem leu
bess bounei maniko mu delu
munema beuguetoula delu
buma keine wax
teyei wumako
dafay soga beug
mbeuguelo mbeuguel
bu djoguei keine dotuko teiye
mbeuguel woy mbeuguel
bu jogue keine meunuko teiyei
ahh yee ahh yeee
bumacci keine garouwalei
bu feikkei beuguetula delu
nañ koffi bayi muy wendelu
bumacci keine garouwalei
mane waxoumako nagn n0bantei
majeure leu mom teu werneu
te neineu yeug yeuguem leu
bess bunei maniko mu delu
munema beuguetoula delu
Random Lyrics
- niphkeys - blessings lyrics
- deebaby - the black sheep (intro) lyrics
- məryəm şabanova - я уйду lyrics
- xander corbett - not your fault lyrics
- adam ďurica - city lyrics
- たかやん (takayan) - あんちてーぜ (antithesis) lyrics
- marissa paternoster - shame lyrics
- rheostatics - goodbye sister butterfly lyrics
- skov - farlig lyrics
- heygun - chains lyrics