youssou n'dour - mool (deglu meteo) lyrics
yaw mool u géej gi
di jambaar ci réew mi
bala ngaa dem géej
ngala déglu météo
bu la nee bul dem
lu mën ë xew bul dem
ben fan ak ñaar
bu mu yax sa liggéey
doyloo nga yalla
du tee nga sa yor téléphone
ak sa gps , te bul fatte sa gillet
sama fans yi ma am
mool ñoo ma gën ë xam
fu ma làng ee ak ñoom
guddi gë day xumb lool
man sama fans yee , ma saf
sawar naa làng ak ñoom , fu ne
aka ñoo dégg daaj , ma ni
moo tax may dem ba jeex , walla
jambaar ca waar wa
jambaar ca géej gë
su ma ko mën oon
ben mool du des ci géej
bu la nee bul dem
lu mën ë xew bul dem
ben fan ak ñaar
bu mu yax sa liggéey
sama fans yi ma am
mool ñoo ma gën ë xam
fu ma làng ee ak ñoom
guddi gë day xumb lool
jambaar ca waar wa
jambaar ca géej gë
su ma ko mën oon
ben mool du des ci géej
man sama fans yee , ma saf
sawar naa làng ak ñoom , fu ne
aka ñoo dégg daaj , ma ni
moo tax may dem ba jeex , walla
yalna leen yalla suturaal
te di leen samm biir géej
barke el seen liggéey bi
barke el seen njaboot gi
aar leen ba ñu doon mag
jox leen barke maam yi
man sama fans yee , ma saf
sawar naa làng ak ñoom , fu ne
yess aye
anh mool ba dem na géеj oo
anh mool ba dem na géej oo
anh mool ba dem na géеj oo
anh mool ba dem na géej oo
bël ba ca ndar , sonn al na waa guét ndar géej oo
anh mool ba dem na géej oo
mool yi laa bëgg ë làng al
seen làng xumb në
ndax sa ma fan’s yi nak
am mool yee ci gën ë dense
anh mool ba dem na géej oo
anh mool ba dem na géej oo
bël ba ca ndar , sonn al na waa guét ndar géej oo
sa telephone ak sa gps
bul fatte gillet ba
anh mool ba dem na géej oo
anh mool ba dem na géej oo
ñoom laa bëgg ë làng al , seen làng xumb në
ndax sa ma fan’s yi nak , am
mool yee ci gën ë dense
anh mool ba dem na géej oo
anh mool ba dem na géej oo
a dëgg ël , yaw mool u géej
yaa di jàmbaar
yaa bari fullë lool
bari jom lool
yaa donn loolu
gëm yalla lool
yaa xarañ lool , te tabe lool
youssou woy na leen
anh mool ba dem na géej oo
anh mool ba dem na géej oo
bël ba ca ndar , sonn al na waa guét ndar géej oo
anh mool ba dem na géej oo
mool yi laa bëgg ë làng al
seen làng xumb në
ndax sa ma fan’s yi nak , am
mool yee ci gën ë dense
anh mool ba dem na géej oo
anh mool ba dem na géej oo
anh mool ba dem na géej oo
anh mool ba dem na géej oo
mool yi laa bëgg ë làng al
seen làng xumb në
ndax sa ma fan’s yi nak , am
mool yee ci gën ë dense
Random Lyrics
- christmas songs - tell it on the mountain lyrics
- coaltar of the deepers - blink lyrics
- topal - sous les néons lyrics
- acidrays - страницы (pages) lyrics
- dj evon, steven malcolm & neon feather - power up (remix) lyrics
- akira phan - buồn ơi! lyrics
- tulpadrip - i love seeing you die lyrics
- garti - i hate you lyrics
- ram - tribe lyrics
- sub-radio - yule shoot your eye out lyrics