
youssou n'dour - touba - daru salaam lyrics
touba daaru salaam
nan farlu gaaw te dem naani paas
bii waruwaay gacceelna jaas
du roppelaan te it du naas
ku weddi laajal meer ya ca faas
touba daaru salaam
gawal ni kon nga ubbi aas
moo gen
moo gen nga toog ba naan xalaas
sakkul ma lii ndax de du jaas
jar nay fanaan m+rs+ okaas
allah
touba daaru salaam
soobul te ban diko cokaas
bindul te gaaw j+pp palaas
la dale fii ba ca gosaas
jazaabul xuloob mooy seen bagaas
ku mel ni noom de am nga chance
cheikhoul khadim a gen licence
sedd sedd menul weesu galaas
cey jile waay amufi maas
touba daaru salaam
ku begg raw tannal sa fas
te bana jaar fu am taxas
ndem begguloo lu la laxas
jebbalujil te wutt njaxas
li am ci daayira ca france
lim la bu kenn menul xiyaas
foo dem ningi conference
bamba di dem ku begg raas
taalibe yaanga casamance
bile courant fеpp la maas
maggal amul aje ki aas
ku xasa dem nooy ni patasse
touba daaru salaam
ku bеgg raw tannal sa fas
te bana jaar fu am taxas
ndem begguloo lu la la
jebbalujil te wutt njaxas
Random Lyrics
- lil madu - se eu não voltar... lyrics
- banda os brothers - dj tapó lyrics
- sockittome - s.w.i.m. lyrics
- lorenz büffel & olaf der flipper - mallorca mallorca lyrics
- seiltheyunger - escalade lyrics
- luan pereira, zé felipe & mc tuto - apostar em você (ao vivo) lyrics
- richie lecéa - rainy day lyrics
- add it up - walk thru lyrics
- iii (kor) - let's make a fire lyrics
- jake hole - caked up in another world! (episode 8) lyrics