youssou n'dour - xale lyrics
xale lyrics
guddé, maasa guddé
jeddi ma na k+nt+
maasa guddé, maasa guddé waw
yeen xale rewmi
ni la ko beugue waw
bismillah niou deeti door dellu saku nian
di nian yallah mu nangoul niu lep lun ko nian
seytané dey yakh khel di sopi xalat
di feweule andado
niun daal bum nyu laal yaye
yeen xale rewmi
ni la ko beugue waw
sen atmi mo du atoum gune
soxlo woul beuri wakh
nanj dieum bolo teh won mak nyi
nioy doule rew mi
gone su taggou ay wadiouram
disso ak nioom seu ndialbeen
fu mu né ci aduna senj thia yakaar lu bakh
yeen xale rewmi
ni la ko beugue waw
bu nu wakhtané ak sunuy baye
mak matna ba thim rew
lum niu wakh nyu degg ko boolé sunuy xalat
nyi ci biti nyi ci biir fu waay meuna ne
nen bole sunuy xalat rew mi dem kanam yaye
yeen xale rewmi
ni la ko beugué waw
man daal waleu bima feetee
maaki samay gars
pexe mune nyung ko dieem nguir sunu rew mi naat
sunu beugue sunu rew mi naat danyu wara boolo
ta kat fou way meune ne sen thia yengueuto
yeen xale rewmi
ni la ko beugué waw
ah thiat oh thiat ken demoul ngeu dess
kenn warrouleu dioylo woye len thiat
yeen xale rewmi
ni la ko beugué waw
sen atmi mo du atoum gune
soxlo woul beuri wakh
nanj dieum bolo teh won mak nyi
nioy doule rew mi
gone su taggou ay wadiouram
disso ak nioom seu ndialbeen
fu mu né ci aduna senj thia yakaar lu bakh
yeen xale rewmi
ni la ko beugue waw
man daal waleu bima feetee
maaki samay gars
pexe mune nyung ko dieem nguir sunu rew mi naat
sunu beugue sunu rew mi naat danyu wara boolo
ta kat fou way meune ne sen thia deff lou bakh yaye
yeen xale rewmi
ni la ko beugué waw
Random Lyrics
- 白浜坂高校合唱部 (shirahamazaka high school chorus club) - triple smiley lyrics
- tiago le dur - heine et amour lyrics
- saz recordz - ciclo lyrics
- tomaten mark - [vbt 2018 - hr halbfinale] lyrics
- yrm bear - local legend lyrics
- weakenedartist - gasolina lyrics
- rowannn - hell rain lyrics
- andrew gold - passing thing lyrics
- keizer léon - sunshine lyrics
- de la calle - esa es la actitud lyrics